score
float32 1.04
1.24
| Chichewa
stringlengths 10
498
| Wolof
stringlengths 10
499
|
|---|---|---|
1.153855
|
Kumeneko mukamuona Iye monga momwe anakuwuzirani.' "
|
Foofa ngeen koy gise, ni mu leen ko waxe woon.""
|
1.15372
|
Mat 5:14 Inu ndinu kuwunika kwa dziko lapansi.
|
5:14 Yéena di leeru àddina.
|
1.153717
|
9:4 Kodi tiribe ulamuliro kudya ndi kumwa?
|
9:4 Xanaa sañunoo lekk ak a naan?
|
1.153576
|
Izi ali zonse ndi kuchita kokha ndi Islam.
|
Li aye tappale la rekk dou islam.
|
1.153572
|
Mose akuuza Kora ndi atsatiri ake kuti: 'Mawa m'mawa tengani mbale za moto ndi kuikamo lubani.
|
Musaa wax Kora ak ñi ko doon topp: ' Suba ci suba, jëlleen seen tibbukaayu safara yi, def ci cuuraay.
|
1.153416
|
Kodi Mozese apanga Kora na atowereri ace 250 kuti acitenji?
|
Lan la Musaa wax Kora ak 250 nit ñi ko toppoon ?
|
1.153296
|
Kenako iye anati: "Chotero mpumulo wa sabata udakalipo kwa anthu a Mulungu."
|
9 Kon ba tey Yàllaa ngi dencal ay gaayam noflaay bu nirook noflaayu Yàlla ca juróom ñaareelu fan ba.
|
1.153273
|
Luk 20:34 Ndipo Yesu adati kwa iwo, Ana adziko lapansi akwatira nakwatiwa:
|
20:34 Yeesu tontu leen ne: "Ci àddina sii, góor ñi ak jigéen ñi dañuy séy.
|
1.153157
|
Koma tsoka iye amene adza!
|
Moom dey digéem luy ñëw la.
|
1.153094
|
Kodi 'cidziwiso cacadidi' cawanda tani mu 'nthawe yakumalizira' ino?
|
Naka la " xam-xam dëgg " baree ci " muju jamono " jii?
|
1.153094
|
Reggie Rockstone amandia munthu yabwino.
|
Reggie Rockstone nekk ab nit baax.
|
1.152784
|
14 Pali wina kodi adwala mwa inu?
|
14 Ana ku wopp ci yeen?
|
1.152576
|
Potsiriza Solomo akuti: 'Musaphe mwana'yo!
|
Suleymaan daldi wax lii: ' Bul rey xale bi !
|
1.152564
|
33Tsopano, pa nthawi ya kuukanso, kodi mkaziyu adzakhala wayani popeza onse asanu ndi awiri anamukwatirapo?"
|
20:33 Ci ndekkite li nag, kan ci ñoom moo war a donn jigéen ja, fekk ku nekk ci juróom-ñaar ñi mas na koo takk?"
|
1.152538
|
Mwachitsanzo, kodi ndi mngelo uti amene Mulungu adamuuzako kuti: "Iwe ndiwe mwana wanga; lero ndakubala "?
|
1:5 Ndaxte Yàlla musul a wax kenn ci malaaka yi ne:"Yaa di sama Doom,maa di sa Baay tey."
|
1.152336
|
11:26 inde, Atate, pakuti iyi inali zokondweretsa pamaso panu.
|
11:26 Waaw Baay bi, ndaxte looloo la neex."
|
1.152285
|
3:5 Mulungu amadziwa kuti, pa tsiku chirichonse Mudzadya izo, maso anu adzatseguka; ndipo mudzakhala ngati milungu, wakudziwa zabwino ndi zoipa. "
|
5 Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon."
|
1.152242
|
Atawathamangitsa kumwamba, anawaponyera kudziko lapansi.
|
Ba pare ñu génne leen asamaan, wàcce leen ci kaw suuf.
|
1.152203
|
Anthu a ku Igupto ndi ku Kanaani analefuka nayo njalayo.
|
Waa réewum Misra ak réewu Kanaan jeex tàkk ndax xiif ba.
|
1.15203
|
Kodi ndipite liti kukakumana ndi Mulungu?
|
Kañ laay teewi fa kanam Yàlla?
|
1.151979
|
Ngati mutsatira zimenezi, mudzathandiza kwambiri anthu amene mukakumane nawo m'gawo lanu."
|
Dinga ñu mën a dimbali ci waar ay nit ñu dëkk ci dëkk yu sore. '
|
1.151911
|
Koma n'chifukwa ninji Yosefe ndi Mariya nawo'nso salipo?
|
Waaye lu tax Yuusufa ak Maryaama nekkuñu fi ñoom it ?
|
1.151803
|
Kodi mungakonde bwanji kuwerenga nkhaniyi pa %%?
|
Ndax bëgg nga jàng téere bii ci %%?
|
1.151691
|
Koma Mulungu wa bambo anga wakhala nane.
|
Waaye sama Yàllay baay ay ànd ak man.
|
1.151588
|
Ndipo pempherani kuti kusakhale m'nyengo yacisanu.
|
18 Ñaanleen ngir seen gàddaay baña tase ak jamonoy seddaayu lolli.
|
1.151455
|
Ndithu ine ndikukuonani inu ndi anthu anu kuti muli m'kusokera koonekera."
|
ndaxte gis naa ne, sóobu nga ci lu wex xat ci kanam yàlla, te bàkkaar noot na la."
|
1.151407
|
Act 1:24 Ndipo adapemphera, nati, Inu, Ambuye, wozindikira mitima ya onse, sonyezani mwa awa awiri m'modziyo amene mudamsankha,
|
1:24 Ñu ñaan ci Yàlla ne: "Boroom bi, yaw mi xam xolu nit ñépp, won nu ki nga tànn ci ñaar ñii,
|
1.151308
|
28 Mbwenye Yezu antawira kuti: "Anthu akutsandzaya kakamwe ndi ale anabva fala ya Mulungu, mbaikoya."
|
28 Waaye Yeesu ne ko: "Neel kay, ki barkeel mooy kiy déglu kàddug Yàlla te di ko topp."
|
1.151265
|
Act 5:35 Ndipo iye adati kwa iwo, amuna inu a Israyeli, tamachenjerani mwa inunokha za anthu awa, chimene muti muwachitire.
|
5:35 Bi ñu ko defee mu ne leen: "Yéen bokki Israyil, moytuleen li ngeen di def nit ñooñu.
|
1.151226
|
28Awa ndi magazi anga a pangano amene akhetsedwa chifukwa cha ambiri kuti akhululukidwe machimo.
|
26:28 ndaxte lii sama deret la, ji fas kóllëre gi, te mu tuuru, ngir ñu bare jot mbaalug bàkkaar yi.
|
1.151187
|
15:19 Ine sindili woyenera kutchedwa mwana wanu.
|
15:19 yeyootumaa nekk sa doom; boole ma ci say surga.' "
|
1.151172
|
19"Chifukwa chake, ine ndikuweruza kuti tisamavute anthu a mitundu ina amene atembenuka mtima kutsata Mulungu.
|
19 "Kon nag sama xalaat mooy: bunu gétën jaambur ñi tuub, ba waññiku ci Yàlla.
|
1.150986
|
Mwana wako anapulumuka."
|
Sa doom faatu na. '
|
1.150853
|
Iwo waba bzinthu bzomwe mpsa Mulungu.
|
Dañu sàcc lu Yàlla moom.
|
1.15062
|
Kodi mbani adapandukira utongi wa Mozese na Aroni, na iwo alonganji kwa Mozese?
|
Ñan ñooy xeex kiliftéefu Musaa ak Aaroona, te lan lañuy wax Musaa ak Aaroona ?
|
1.150493
|
14:4 Koma iwo anangokhala chete.
|
14:4 Waaye ñépp ne cell.
|
1.150462
|
20 Tawuka, nutsike, Ndipo upite nawo, wosakayika kayika; pakuti ndawatuma ndine.
|
20 Jógal, nga wàcc te ànd ak ñoom; bul werante, ndaxte maa leen yebal."
|
1.150387
|
Alongo ake Sali anzathu?"
|
Te ay rakkam yu jigéen ndax nekkuñu fi ak nun?"
|
1.15038
|
14:18 Ndiyamika Mulungu wanga kuti ndimalankhula malilime inu nonse.
|
14:18 Maa ngi sant Yàlla ci li may wax ay làkk, ba raw leen yéen ñépp.
|
1.150359
|
22 "Tionetseni ndipo mutiuze zinthu zimene zidzachitike.
|
22 "Woneleen ko te wax nu liy ñëw.
|
1.150332
|
Palibe ndi mmodzi yemwe amene amazindikira, palibe amene amafunafuna Mulungu.
|
Amul kenn ku xam yëfi Yàlla,mbaa kenn ku koy wut.
|
1.150289
|
8:18 Choncho, amasamala mmene mumamvetsera.
|
8:18 Seetleen bu baax, ni ngeen di dégloo kàddu gi.
|
1.150137
|
amene ali Padziko lapansi,
|
ci biir réewum aji dund ñi.
|
1.149904
|
53 Inu amene munalandira Malamulo amene anaperekedwa ndi angelo ndipo simunawamvere."
|
53 Jot ngeen yoonu Musaa, wi Yàlla wàcce jaarale ko ci ay malaaka, te sàggane ngeen ko."
|
1.149727
|
Kodi akanatsutsa bwanji, popeza anachita kulengedwa ndi Mulungu?
|
Ndax li Yàlla sàkk amoon na sikk?
|
1.149494
|
27Pamenepo inu mudzadziwa kuti Ine ndili mu Israeli,
|
27 Dingeen xam ne ci biir Israyil laa ne, man,
|
1.14943
|
5Nʼchifukwa chake Khristu atabwera pa dziko lapansi anati,
|
5 Looloo tax bi muy wàcc àddina, Kirist nee na:"Bëggoo saraxu mala walla beneen sarax,waaye aw yaram nga ma defaral.
|
1.149374
|
17 Atatero, anawatsekera pamodzi m'ndende masiku atatu.
|
17 Mu tëj leen ñetti fan.
|
1.149173
|
Mvulayo inagwa kwa masiku 40, masana ndi usiku.
|
Taw na 40 bëccëg ak 40 guddi.
|
1.149071
|
52 Pakuti sadazindikire za chozizwitsa cha mikateyo, pakuti mitima yawo idawumitsidwa.
|
52 Njàqarey taalibe ya nag weesu dayo, ndaxte seen xol dafa fatt, ba réere mbir kéemaan, gi Yeesu defoon ci mburu yi.
|
1.148846
|
Iye amene anatsika ndiye yemweyo amene anakwera pamwamba kuposa kumwamba konse, kuti akwaniritse ...
|
10 Kooku wàccoon mooy kenn ki yéegaat ba tiim asamaan yépp, ngir def lépp feese jëmmam.
|
1.148689
|
N'zoona kuti Mulungu anafuna kuti Adamu azilamulira nyama.
|
Yàlla dafa fonk doom-Aadama yi.
|
1.148611
|
Kudzulu kwacita mdima.
|
asamaan di lëndëm.
|
1.148492
|
Iye tsopano ali pa ulendo womka ku Damasiko.
|
Léegi mu ngi ci yoonu Damas.
|
1.148416
|
Mpingo ndi thupi lake ndipo amakhala mmenemo ndi chidzalo chake chonse.
|
miy jëmmam, di matug Kirist, mi fees mbindeef mu ne ci fànn gu ne.
|
1.148347
|
5:40 Ndipo iwo ankanyoza iye.
|
5:40 Waaye ñu di ko ñaawal.
|
1.148252
|
Ndipo iye adzakuuza zoti uchite."
|
Moom dina la xamal li nga wara def."
|
1.148187
|
Zimenezi zikupangitsa kuti Asamariya ambiri akhale okhulupirira.
|
Ñu bare gëm ko ndax li mu doon wax.
|
1.148113
|
amene mumasanthula maganizo ndi mitima,
|
kiy natt xol yi, xam na,
|
1.148097
|
Iye alamulira ngakhale mphepo ndi madzi, ndipo zimumvera Iye."
|
Mi ngi jox ndigal ngelaw li ak ndox mi, ñu koy déggal."
|
1.148079
|
Jas 5:19 Abale, ngati wina wa inu asochera posiyana ndi chowonadi, ndipo ambweza iye mzake;
|
5:19 Samay bokk, su amee ci yéen ku réere dëgg, te am ku ko gindi,
|
1.147786
|
"Cenjelani ndi aneneli onama." - MATEYU 7:15.
|
" Moytuleen ñi mbubboo turu yonent. " - MACË 7:15.
|
1.147781
|
70 Apanso anakana.
|
70 Waaye Piyeer weddiwaat ko.
|
1.147728
|
5 Kodi si mmene nyumba yanga ilili kwa Mulungu?+
|
5 Du nii la sama waa kër def ak Yàlla?
|
1.147704
|
Chifukwa tinaona nyenyezi yake kummawa ndipo tabwera kudzamupembedza."
|
Ndaxte gis nanu biddiiwam ci penku te ñëw nanu ngir màggal ko."
|
1.147655
|
Timachita zimenezi chifukwa chakuti iye analamula otsatira ake kuti: "Muzichita zimenezi pondikumbukira."
|
Dañu koy def ndaxte digal na taalibeem yi ne: " Defleen lii, ngir fàttaliku ma. "
|
1.147646
|
lisanafike tsiku lalikulu ndi laulemerero la Ambuye.
|
bala bésu Boroom biy ñëw, di bés bu mag, bi ànd ak ndam.
|
1.14756
|
11:14 Ndipo adzanenera kwa inu m'mawu, limene adzapulumutsidwa ndi nyumba ako onse. '
|
11:14 Dina la xamal ay wax yu lay musal, yaw ak sa waa kër gépp."
|
1.147556
|
Timotio adati: 'Inde, ndin'funa kuyenda.'
|
Timote tontu ko ne: ' Waaw, bëgg naa dem. '
|
1.14729
|
'Kodi izi zidzachitika bwanji?' akufunsa motero Mariya.
|
Maryaama laaj ko lii: ' Naka la loolu mën a ame ?
|
1.147043
|
15Kodi ndilibe ufulu wochita zimene ndikufuna ndi ndalama zanga?
|
20:15 ndax sañumaa def ak sama alal li ma neex?
|
1.146907
|
10Tsopano, chifukwa chiyani mukuyesa Mulungu poyika goli mʼkhosi la ophunzira, limene ngakhale ife kapena makolo athu sangathe kulisenza? 11Osatero!
|
10 Léegi nag lu tax ngeen di diiŋat Yàlla, ciy teg taalibe yi yen bu nu masula àttan, nun mbaa sunuy maam?
|
1.1469
|
Anatenga chilichonse, ngakhalenso zishango zonse zagolide zimene Solomoni anapanga.
|
Lépp la jël ba ca mboolem pakki wurus ya Suleymaan defarlu woon.
|
1.146897
|
Koma aliyense wokhala mu choonadi amabwera ku kuwunika, kuti zionekere poyera zimene iye wachita zachitika kudzera mwa Mulungu."
|
Waaye ku def lu jub day ñew ci leer gi, ngir ñu xam ne, def na ay jëfam ci kanumu Yàlla.
|
1.146893
|
5:26 kuti akampatule wake, kutsuka wake woyera ndi madzi ndi Mawu a Moyo,
|
5:26 ngir sellal ko ak kàddoom, ba mu laab ni ku sangu set.
|
1.146839
|
Zatheka bwanji kuti mayi wa Mbuye wanga abwere kwa ine?
|
Man maay kan, ba ndeyu sama Boroom ñëw di ma seetsi?
|
1.146672
|
24Ndipo mphamvu zake zidzakhala zazikulu, koma osati ndi mphamvu zake zokha.
|
24 Dina gëna am doole, waaye du doon dooley boppam.
|
1.146587
|
MNENERI Danieli anakhala ndi moyo zaka zoposa 500 Yesu asanabadwe.
|
YONENT Yàlla Dañeel mu ngi doon dund lu ëpp 500 at bala Yeesu di juddu.
|
1.146481
|
ndi kumangoyenda mu mzinda.
|
Tass dëkk bi rekk ngéen fi nekke.
|
1.146468
|
Mwana wanu wayamba kale zaka ziwiri.
|
Sama doom am na ñaari at.
|
1.146288
|
Tinaphunziranso kuti Baibulo linaneneratu za nthawi imene "imfa sidzakhalaponso."
|
Jàngoon nañu it ne Biibël bi wax na ne dina am jamono joo xam ne "dee dootul am."
|
1.146199
|
Kodi muli ndi mafunso
|
am nga ay laaj?
|
1.146174
|
N'kuwombola anthu tonse,
|
xeet yépp seede ko.
|
1.146158
|
Ndikudziwa kuti ndinu ndani, ndinu Woyerayo wa Mulungu!"
|
Xam naa yaa di kan, yaa di Aji Sell ju Yàlla ji!"
|
1.146122
|
Luk 1:43 Ndipo ichi chichokera kuti kudza kwa ine, kuti adze kwa ine amake wa Ambuye wanga?
|
1:43 Man maay kan, ba ndeyu sama Boroom ñëw di ma seetsi?
|
1.145991
|
Anakamba na 'nthu onse.
|
Mu waxtaan ak ñoom ñépp.
|
1.145968
|
Ndimakhala ku Mexico ndipo mwezi wamawa ndikupita ku Spain.
|
Ci weeru awril, dinaa dem ci Paris.
|
1.145854
|
Act 7:50 Kodi silidapanga dzanja langa zinthu izi zonse?
|
7:50 Ndax du sama loxo moo defar yëf yooyu yépp? - Moom la Boroom bi doon wax."
|
1.14579
|
" (Mûsa) adati: "Usandidzudzule chifukwa chakuiwala kwanga, ndipo usandipatse zovuta kwambiri pa khumbo langali (lofuna kukutsata)."
|
(73) Mu ne: Bul ma jàppe sama fàtte gi te bul ma teg ci sa mbir mi lu ma manul !
|
1.145666
|
Amuna ayenera kukonda akazi awo ngati mmene amakondera matupi awo. - Aefeso 5:25-29.
|
Jëkkër yi dañu war a bëgg seen jabar ni ñu bëgge seen bopp. - Efes 5:25-29.
|
1.145643
|
Zoonadi munamva za Iye ndipo munaphunzitsidwa mwa Iye molingana ndi choonadi chimene chili mwa Yesu.
|
Ndax yaakaar naa ne, dégg ngeen Kirist te jàng ngeen ci moom, ba xam dëgg gi Yeesu ëmb.
|
1.145543
|
1:24 ndi kupemphera, iwo anati: "Inuyo, O Ambuye, amene amadziwa mtima wa munthu aliyense, kuwulula amene awiriwa mwasankha,
|
1:24 Ñu ñaan ci Yàlla ne: "Boroom bi, yaw mi xam xolu nit ñépp, won nu ki nga tànn ci ñaar ñii,
|
1.145515
|
Ngakhale bambo anga akudziwa zimenezi.'
|
Sama baay ci boppam xam na loolu bu baax."
|
1.145474
|
Ndipo m'menemo tatumizamo Ayah (ndime) zomveka kuti mukumbukire (malamulo ndi kuchita nawo m'njira yoyenera).
|
(13) Noo ngi lay nettalli séen xibaar dëgg-dëgg;nekkoon nañu ñu jub, nu dolli léen ak njub.
|
1.145468
|
Rehobiamu si mfumu yabwino.
|
Robowam nekkul woon buur bu baax.
|
1.145437
|
Kodi ndi cidziwiso canji cidapasa maanju awiri Loti?
|
Lan la ñaari malaaka yëgal Lóot ?
|
1.14536
|
Kumene mungapite kumapeto kwa sabata?
|
Où est-tu allée ce week-end?
|
1.145236
|
ali m'dziko otetezedwa,
|
ci biir réewum aji dund ñi.
|
1.145213
|
Kodi ndani amene angakhululukire machimo kupatula Mulungu?"
|
Ana ku mana baale bàkkaar yi, ku dul Yàlla doŋŋ?"
|
1.145192
|
41 Ine sindilandira ulemu kwa anthu.
|
41 "Wutuma tagg yu jóge ci nit.
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.