score
float32
1.04
1.24
Chichewa
stringlengths
10
498
Wolof
stringlengths
10
499
1.168453
Ndipo bukhu lino liti likuthandizeni.
Téere bii dina la ci dimbali.
1.168405
nimuvale munthu watsopano, amene analengedwa monga mwa Mulungu, m'chilungamo, ndi m'chiyero cha choonadi.
te soloo jikko ju bees, ji Yàlla sàkk ci njub ak sell yu dëggu.
1.168214
Ndipo mwa Iye, inunso mukamangidwa pamodzi ndi ena onse kukhala nyumba yokhalamo imene Mulungu amakhala mwa Mzimu wake.
Te ci seen bokk ci Kirist, Yàlla boole na leen tabax yéen itam, ba ngeen nekk dëkkukaayam, jaar ci Xel mu Sell mi.
1.167972
Mozese alonga: 'Thawikirani misasa ya amuna anewa akuipa.
Musaa ne lii: ' Soreleen nit ñu bon ñii ak seeni tànt.
1.167914
22Kenaka Yudasi (osati Yudasi Isikarioti) anati, "Koma Ambuye, nʼchifukwa chiyani mukufuna kudzionetsa nokha kwa ife, osati ku dziko lapansi?"
22 Yudaa -du Yudaa Iskariyo de, beneen la woon- ne ko: "Boroom bi, lu xew, ba nga nar noo feeñu nun rekk, te doo feeñu àddina sépp?"
1.167581
17Anthu 72 aja anabwerera ndi chimwemwe ndipo anati, "Ambuye, ngakhale ziwanda zinatigonjera ife mʼdzina lanu."
10:17 Juróom-ñaar-fukki taalibe yi ak ñaar dellusi, fees ak mbég te naan: "Boroom bi, rab yi sax déggal nañu nu ndax sa tur."
1.167355
Mulungu wacadidi ni Mulengi wa bzinthu bzense.
Yàlla dëgg ji moo sàkk lépp.
1.167197
20 Iwo akuchimwa uwadzudzule pamaso pa onse, kuti wotsalawo ena achite mantha.
20 Waaye ñiy bàkkaar, yedd leen fa kanam ñépp, ngir artu ñi ci des.
1.166682
Ife tikukhulupirira kuti tinapulumutsidwa mwachisomo cha Ambuye athu Yesu Khristu, monga iwonso anachitira."
11 Nun daal ci yiwu Yeesu Boroom bi lanu yaakaara mucce, te ñoom itam, ci lañu wékku."
1.166501
(Genesis 1:28) Dziko lapansi silidzaonongedwa.
(Njàlbéen ga 1: 28) Suuf si du fi mas a jóge.
1.1663
koma Israele, potsata lamulo la chilungamo, sanafikila lamulolo.
31 Waaye bànni Israyil, mi bëggoona sàmm yoon ngir jub, matalu ko.
1.166145
7:50 Alibe dzanja langa zinthu izi zonse?'
7:50 Ndax du sama loxo moo defar yëf yooyu yépp? - Moom la Boroom bi doon wax."
1.165045
Mbani adalenga mwamuna wakutoma, ndipo dzina lace akhali yani?
Kan moo sàkk góor gu jëkk gi, te naka la tuddoon ?
1.164912
Ana ayenera kumvera makolo awo. - Aefeso 6:1-3.
Xale yi dañu war a déggal seeni waajur. - Efes 6:1-3.
1.16469
Mariya akufulumira kumka kukazonda Elizabeti.
Maryaama daldi gaaw a dem seeti Elisabet.
1.164662
8"Mukamalowa mʼmudzi, ndi kulandiridwa, idyani chilichonse akukonzerani.
8 "Dëkk bu ngeen mana dugg, te waa dëkk ba teeru leen, lu ñu leen jox, lekkleen ko.
1.164526
"Tiyeni tidye ndi kumwa, pakuti mawa tifa. "
"Nanu lekk di naan, ndaxte ëllëg dinanu dee."
1.164213
Mar 7:12 Ndipo simulolanso kumchitira kanthu atate wake kapena amayi wake;
7:12 dootuleen ko bàyyi, mu defal dara ndeyam walla baayam.
1.164077
Pa tsiku Mwana wa Munthu adadza ndi lipenga lalikulu kusonkhanitsa otsalira a Isiraeli kuchokera kumphepo zinayi.
4 Bànni Israyil lañu, te Yàlla def na leen ni ay doomam; dëkkaloon na ndamam ci seen biir, fas ak ñoom kóllëre yi.
1.163612
ndipo mafumu awo adzakutumikira.
seeni buur di la surgawu.
1.163366
12 Pamenepo ophunzirawo anati: "Ambuye, ngati iye akupumula, apeza bwino."
12 Taalibe ya ne ko: "Boroom bi, bu nelawee kay, kon dina wér."
1.16326
4 Iwo adzaona nkhope yake ndipo dzina lake lidzalembedwa pa mphumi zawo.
4 Dinañu gis xar kanamam, te turam dina nekk ci seen jë.
1.163197
Ali yense wa iwo anali ndi mkazi.
Ku ci nekk amoon na jabar.
1.162826
30 Ndikunena kuti, Munthu uyu adayamba kumanga, koma sadathe kumaliza.
"Waa jii dafa tàmbalee tabax, waaye mënu koo àggale."
1.162585
15Zonse za Atate ndi zanga.
15 Lépp lu Baay bi am, maa ko moom.
1.162562
17Anthu 72 aja anabwerera ndi chimwemwe ndipo anati, "Ambuye, ngakhale ziwanda zinatigonjera ife mʼdzina lanu."
17 Juróom ñaar fukki taalibe yi ak ñaar délsi, fees ak mbég te naan: "Boroom bi, rab yi sax déggal nañu nu ndax sa tur."
1.16233
Mudzadedwa ndi inu nonse chifukwa cha dzina langa.
Te ñépp dinañu leen bañ ndax sama tur.
1.162316
Ndipo Manda+ anali kumutsatira pafupi kwambiri.
Noonu turu Yeesu di gën a siiw.
1.162163
Act 15:9 Ndipo sadalekanitsa ife ndi iwo, nayeretsa mitima yawo m'chikhulupiriro.
15:9 Gënalantewu nu ak ñoom, ci li mu sellal seen xol ci kaw ngëm.
1.1621
Anthu ena angayese kutiletsa kulankhula za ufumu wa Mulungu.
Mën na am ay nit jéem ñu tere wax ci nguuru Yàlla.
1.161948
Ife tikudziwa kuti munthu uyu ndi wochimwa."
Xam nanu ne waa joojee boroom bàkkaar la."
1.161847
Ndi nkhombo kwa ine kudzaoniwa na mama wa Mbuya wanga.
Man maay kan, ba ndeyu sama Boroom ñëw di ma seetsi?
1.161576
2 "Ndamva zinthu zambiri ngati zimenezi.
2 Kàddu yu mel nii, dégg naa ko lu bare.
1.161552
Mulungu anabwera ku dziko lapansi kudzatiphunzitsa, kutichiritsa, kutikonza, kutikhululukira - ndikutifera!
Yàlla ñëw na ci kaw suuf ngir jàngal nu, faj nu, jubbanti nu, baal nu te de ngir nun !
1.161414
4:30 Ndipo iye anati: "Kuti kodi Tikayerekeza Ufumu wa Mulungu?
4:30 Yeesu ne leen ati: "Lu nu man a mengaleel nguuru Yàlla?
1.161219
Atalenga analenga iwo mamuna ndinkazi...abalane azaze dziko.
Yexowa dafa sàkk góor ak jigéen ngir ñu jàppalante ci seen biir.
1.161161
Pakuti udzatsogolera Ambuye, kukonza njira zake; 77 Kuwapatsa anthu ake chidziwitso cha chipulumutso, ndi makhululukidwe amachimo awo.
1:77 Dinga xamal mbooloom,ni leen Boroom bi man a musale,jaare ko ci seen mbaalug bàkkaar,
1.160799
ndi kuti muvale umunthu watsopano, wolengedwa kuti ufanane ndi Mulungu mu chilungamo chenicheni ndi chiyero.
te soloo jikko ju bees, ji Yàlla sàkk ci njub ak sell yu dëggu.
1.160395
47 Koma Solomo adam'mangira Iye nyumba.
Waaye Suleymaan moo tabaxal Yàlla kër ga.
1.160331
32 Nanga ndinenenso chiyani pamenepa?
32 Lu ma ci wara tegaat?
1.160046
Amayamba ndi tsitsi la khungu.
fi ay létt tàmbalee.
1.159884
Usiku mngelo wa Mulungu akutsegula chitseko cha ndende, monga momwe mukuonera pano.
Ci guddi gi, malaakaa Yàlla ubbi na buntu kaso bi, ni nga ko gise fii.
1.159764
Iye amene anatsika ndiye yemweyo amene anakwera pamwamba kuposa kumwamba konse, kuti akwaniritse ...
10 Ki wàccoon moo yéegaat, ba tiim asamaan yépp, ngir fees lépp.
1.159753
Kodi tidzapitiriza kugwirizana ndi anthu amene amakonda Mulungu?
Ndax dinañu ànd ak ñi bëgg Yàlla?
1.159692
wawo adati: "Kodi simudziwa Kuti
Noonu Yeesu ne leen: "Ndax seen xol dafa tëju ba tey?"
1.159514
KODI mukudziwa amuna awa amene Yakobo akulankhula nawo?
NDAX xam nga ñan la Yanqóoba di waxal fii ?
1.15947
Kodi Ine ndisamwere chikho chimene Atate andipatsa?"
Ndax warumaa naan kaasu naqar, bi ma Baay bi sédd?"
1.15935
"Ndipo Adzacitidwa Kwa Iwo Mau Adanenera Yesaya, Amene Ati, Pakumva Mudzamva, Ndipo Simudzazindikira Konse, Pakupenya Mudzapenya Ndipo Simudzaona Konse."
Li Esayi waxoon ci kàddug Yàlla am na ci ñoom, bi mu naan:"Dingeen déglu bu baaxwaaye dungeen xam dara;di xool bu baax waaye dungeen gis dara.
1.15918
Ahaswero sakudziwa kuti mkazi wake Estere ndi Muisrayeli.
Asuerus xamul ne jabaram, waa Israyil la.
1.158921
Ndipo mulungu amene adzakulanditsani m'manja mwanga ndani?'
Ana yàlla ju leen di musal ci man?"
1.158535
Nowa anali "mlaliki wa chilungamo" ndipo analalikira mokhulupirika uthenga wa Mulungu kwa anthu a m'nthawi yake.
Nóoyin nit ku jub la woon, di ku mat ci biir nit ñi mu bokkal jamono, te di ku topp Yàlla.
1.158513
Kodi mbani adacita mamuna wakutoma, na iye akhacemerwa tani?
Kan moo sàkk góor gu jëkk gi, te naka la tuddoon ?
1.158328
kudziwika kwa zizoloŵezi zodziwika za zinthu zodziwika;
Xam-xam ba tay la ñu ka xam.
1.158323
"Choncho tidafuna kuti Mbuye wawo awasinthire ndi wabwino kuposa iye pa kuyera, ndi wachifundo chapafupi (kwa makolo ake.) "
Yalnako yàlla défal lepp lu gën ci moom xalébi té gënël leen yeen waajur yi.
1.158127
Ndani safuna kukhala ndi moyo? n
Waaye kan moo bëggul a dund ?
1.15811
Koma amene akutsatira choonadi m'zimene achita, akulowa m'kuunika ndipo zikuonekeratu kuti zochita zawo zakhazikika mwa Mulungu."
Waaye ku def lu jub day ñew ci leer gi, ngir ñu xam ne, def na ay jëfam ci kanumu Yàlla.
1.158064
"Tinalimba mtima mwa Mulungu wathu kulankhula kwa inu uthenga wabwino wa Mulungu movutikira kwambiri." - 1 ATES.
Teewul ci sunu ndimbalal Yàlla, nu ñeme leena àgge, ci biir xeex bu metti sax, xibaaru jàmm bu Yàlla bi.
1.158062
Joh 20:28 Tomasi adayankha nati kwa Iye, Ambuye wanga, ndi Mulungu wanga.
20:28 Tomaa tontu ko ne: "Sama Boroom, sama Yàlla!"
1.158038
"Ndipo iwo adzaitanira bwanji pa iye amene sanamkhulupilira?
Waaye nan lañuy wooye ki ñu gëmagul?
1.157816
7Mosakayika konse, munthu amene amadalitsa ndi wamkulu kuposa amene akudalitsidwayo.
7:7 Kiy barkeel a gën a màgg ki ñuy barkeel, loolu amu ci benn werante.
1.157701
Koma nthawi ya ukwati itakwana, kodi mukudziwa chimene chinachitika?
Waaye bi bésu séy bi jotee, xam nga lan moo xew ?
1.15762
Kodi Yesu ankachita bwanji zinthu ndi ana, nanga ana amafuna makolo awo azichita chiyani?
Nan la Yeesu meloon ak xale yi, te lan la xale yi soxla ci seen waajur?
1.157603
Ndi ngani ni tshi nthudzela thungo?
Lu tax nga bàyyi ma?
1.157577
Kodi wadza kwa ine kundikumbutsa tchimo langa, ndi kundiphera mwana wanga?"
Xanaa dangaa ñëw sullisi sama bàkkaar, ba tax nga rey sama doom ju góor jii?"
1.157332
Yosefe mwana wanga akadali ndi moyo!
Sama doom Yuusufaa ngi dund.
1.157262
45 Na tenepo, aapasa kudzindikira toera akwanise kubvesesa mwadidi pidalembwa m'Bukhu ya Mulungu.
45 Noonu mu ubbi seen xel, ngir ñu xam li Mbind mi di wax.
1.157247
Koma dziwani izi: Mukandipha, mudzakhala mukupha munthu wosalakwa.'
Waaye nangeen xam lii: Boo leen ma reyee, nit ku deful dara lu bon ngeen di rey. '
1.157207
64 Koma pali ena mwa inu amene sakukhulupirira."
64 Waaye am na ci seen biir ñu ko gëmul."
1.157143
2 Ngati sindine mtumwi kwa ena, mosakayikira ndine mtumwi kwa inu, popeza ndinu chidindo chotsimikizira+ utumwi wanga mwa Ambuye.
2 Ndegam ci ñeneen, man duma ndawal Almasi, xanaa ci yeen boog, moom laa, ndax liy firndeel sama sasu ndaw ci Sang bi, yeen la.
1.157116
Kodi mukudziwa zimene Paulo akulankhula ndi Timoteo?
Ndax xam nga lan la Pool di wax Timote ?
1.156932
Musakonde Dziko Lapansi
Buleen sopp àddina
1.15685
23 Gula choonadi+ ndipo usachigulitse.
23 Jëndal dëgg te bu ko jaay.
1.156828
Choncho mtumizeni m'bale wathu pamodzi ndi ife kuti akatipimire (mlingo wokwana); ndithu ife tikamsunga."
Seetal fii ci sunu kanami bokk lépp lu ma fi yor, loo ci moom fabal, yóbbu."
1.156793
Ukimona iye udzamona Mulungu.
ndax dingeen gis Yàlla.
1.156605
Ndi umunthu watsopano watipatsa ife chilungamo chake ndi chiyero, atavala ngati diresi.
te soloo jikko ju bees, ji Yàlla sàkk ci njub ak sell yu dëggu.
1.156537
5:30 Pakuti ife ndife gawo la thupi lake, wa mnofu wake ndi mafupa ake.
5:30 ndaxte noo di céri jëmmam.
1.156528
Luk 15:19 Ndipo sindiyeneranso konse kutchulidwa mwana wanu; mundiyese ine ngati m'modzi wa antchito anu.
15:19 yeyootumaa nekk sa doom; boole ma ci say surga.' "
1.156526
M'chithunzichi, kodi anthu aŵiri amene ali ndi Mosewo ndi ndani?
Ñaari góor ñi nekk ak Musaa, ñan lañu?
1.156475
Joh 5:40 Ndipo simufuna kubwera kwa Ine, kuti mukhale ndi moyo.
5:40 te bëgguleen a ñëw ci man ngir am dund!
1.156423
Eph 2:1 Ndipo inu adakupatsani moyo, pokhala mudali akufa ndi zolakwa ndi zochimwa zanu;
2:1 Te yéen itam Yàlla dekkal na leen, yéen ñi doon ndee fa kanamam ci seeni moy ak seeni bàkkaar.
1.156405
5:5 ndi ndani amene amagonjetsa dziko?
5:5 Ku noot àddina mooy kan?
1.156372
5Kodi makolo anuwo ali kuti tsopano?
5 "Seeni maam, ana ñu tey?
1.156152
45Na tenepo, aapasa kudzindikira toera akwanise kubvesesa mwadidi pidalembwa m'Bukhu ya Mulungu.
45 Noonu mu ubbi seen xel, ngir ñu xam li Mbind mi di wax.
1.155766
Analenga Zinthu Zonse."
Yàllaa sàkk bépp mbindeef.
1.155686
Tsono imwepo mwadzaza Jeruzalemu na mapfunziso yanu.'
Waaye feesal ngeen Yerusalem ak seen njàngale mi. '
1.155564
14Inu ndinu kuunika kwa dziko lapansi.
14 Yéena di leeru àddina.
1.155378
popeza mwandipatsa chiyembekezo.
Dangay dinga jox yaakaar.
1.155293
Dzina lanu ndani? / Dzina lanu ndi yani? - Witwa nde?
Noo tudd ? / Nan nga tudd ?
1.155225
32 Ngakhala Mulungu apaswa mbiri muna Mwana, Mulungu anampasambo mbiri muna Iye ene, pontho anati ampase mbiri na mwansanga.
32 Te bu ma feeñalee ndamu Yàlla, Yàlla itam ci teewaayam dina feeñal ndamu Doomu nit ki, te dina ko def léegi.
1.15513
Miyezi yowerengeka pambuyo pake iwo akuyamba kumanga kachisi.
Ay weer ginnaaw loolu, ñu daldi tàmbalee tabax kër Yàlla gi.
1.155038
Eph 4:21 Ngatitu mudamva Iye, ndipo mudaphunzitsidwa mwa Iye monga chowonadi chiri mwa Yesu;
4:21 Ndax yaakaar naa ne, dégg ngeen Kirist te jàng ngeen ci moom, ba xam dëgg gi Yeesu ëmb.
1.154887
38 Mawu akenso sanakhazikike mwa inu, chifukwa simukhulupirira amene Atatewo anamutumiza.
5:38 te kàddoom saxul ci yéen, ndaxte gëmuleen ki mu yónni.
1.154708
9Iye sanasiyanitse pakati pa ife ndi iwo, pakuti anayeretsa mitima yawo mwachikhulupiriro.
15:9 Gënalantewu nu ak ñoom, ci li mu sellal seen xol ci kaw ngëm.
1.154475
"Ndipo zizindikiro izi zidzawatsata iwo amene akhulupirira; M'dzina langa adzatulutsa ziwanda; adzayankhula ndi malilime atsopano; "
16:17 Ñi ma gëm dinañu ànd ak firnde yii: ci sama tur dinañu dàq rab yi, di wax làkk yu bees,
1.154345
Mar 15:23 Ndipo adampatsa vinyo wosanganiza ndi mure; koma Iye sadamlandire
15:23 Ñu bëgg koo jox biiñ bu ñu boole ak naan gu tudd miir, waaye nanguwu ko.
1.154155
Kodi mukudziwa chimene mneneri ali?
Ndax xam nga lan mooy yonent ?
1.154034
10Tsopano, chifukwa chiyani mukuyesa Mulungu poyika goli mʼkhosi la ophunzira, limene ngakhale ife kapena makolo athu sangathe kulisenza? 11Osatero!
10 Léegi nag lu tax ngeen di diiŋat Yàlla, di teg taalibe yi yen bu nu masula àttan, cay maam ba ci nun?
1.154018
Ndipo onani! pali omalizira amene adzakhala oyamba, ndipo alipo oyamba amene adzakhala omaliza. "
30 Noonu ñenn ci ñi mujj ñooy jiituji; te ci ñi jiitu, ñooy mujji."
1.153998
Koma iye anawayankha kuti: "Chakudya ndili nacho chimene inu simukuchidziwa."
4:32 Waaye Yeesu tontu leen: "Am na ñam wu may lekk, te xamuleen ko."
1.1539
Kodi inu mukhale osadziwa kuti palibe wina wonga ine kudziwa zizindikiro wozindikira?"
Xanaa xamuleen ne nit ku mel ni man day gisaane?"