score
float32
1.04
1.22
Amharic
stringlengths
8
300
Wolof
stringlengths
10
472
1.142265
] 38 ከእናንተ ጋር የገባሁትን ቃል ኪዳኔን አትርሱ።
38 Kóllëre gi ma fasoon ak yeen nag, buleen ko fàtte.
1.141851
8 እኔ ግን 'ጌታ ሆይ፣ በጭራሽ፤ ምክንያቱም ንጹሕ ያልሆነ ወይም የረከሰ ነገር ወደ አፌ ገብቶ አያውቅም' አልኩ።
8 Waaye ma ne: "Mukk Boroom bi, ndax dara lu daganul mbaa lu araam masula dugg ci sama gémmiñ."
1.141774
4:18 እንዲሁም ጻድቅ በጭንቅ የሚድን ከሆነ, የት አድኖ እና ኃጢአተኛ ይታያል?
4:18 Te:"Su muccu ki jub jafee,luy doon muju ki weddi te dëng?"
1.141572
በሌሊትም እንደ ሌባ ነው።
guddi jot mu dib sàcc.
1.14145
ከአሕዛብም መካከል ታደገን"
tasaare nu ci biir xeet yi.
1.141046
አላህ ለሚሻው ሰው
Yàllaa ko dencal ñi ko sopp a ."
1.140908
በሌላ አነጋገር፣ ለእኛ የእግዚአብሔር ዓይነተኛ ቃል ነው።
Bibal bi mooy Kàddug Yàlla ngir nun.
1.140657
የአንቺዋንስ የሰማና ያረጋገጠ ሰው አለ ?
Ku leen di déglu ba di leen gëm ?
1.140406
ሁላቸው እንደ ልብስ ያረጃሉ፤
dinañu màggat ñoom ñépp ni ay yére.
1.140273
ከዚህ በኋላ፣ ጴጥሮስ ጥቂት ቀን ከእነርሱ ጋር እንዲቀመጥ ለመኑት።
Gannaaw loolu ñu ñaan Piyeer, mu toog ci ñoom ay fan.
1.140207
አይሁድም፣ "እኛማ በማንም ላይ የሞት ፍርድ ለመፍረድ መብት የለንም" አሉት።
Yawut yi ne ko: "Yoon mayu nu, nu àtte nit, teg ko dee."
1.1402
‹‹በእውነትህ ቀድሳቸው፤ ቃልህ እውነት ነው።
samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. sa kàddu mooy dëgg.
1.139868
መልካሙን የእምነት ገድል ተጋደል የተጠራህለትንም በብዙም ምስክሮች ፊት በመልካም መታመን የታመንህለትን የዘላለምን ሕይወት ያዝ።
12 Góor-góorlul ci bëre bu baax bi, ba ub làmbi ngëm, te feddali sag téye ci dund gu dul jeex gi; ndaxte ci loolu la la Yàlla woo, te looloo waraloon it sa seede su rafet fa kanam mbooloo mu bare.
1.139746
ነቢያትም ሞተዋል።
Yonent yi itam faatu nañu.
1.139684
15 ዳዊትም አበኔርን እንዲህ አለው፦ "አንተ ወንድ አይደለህም?
15 Daawuda ne Abner: "Xanaa doo jàmbaaru góor?
1.13959
አሁን ምን እንደደረሰኝ ይመልከቱ!
Xoolal li xew léegi !
1.139482
ሙሉ ለሙሉ ባይገባንም እርሱ የሰዎችን ጸሎት ሰምቶ
Waaye du ñaan yépp lay déglu ba di ko nangu.
1.139146
ይህ የመጀመሪያው ትንሣኤ ነው።
Loolu moo di ndekkite lu jëkk li.
1.139083
እኛ የምንሰራው አምስት ቀኖች ብቻ ነው።
Juróomi fan rekk lanu fay def.
1.139039
10 ወይስ ለአራቱ ሺህ ሰባቱ እንጀራ፥ ስንት ቅርጫትም እንዳነሣችሁ ትዝ አይላችሁምን?
10 Te ndax fàttalikuwuleen itam juróom ñaari mburu ya ngir ñeenti junniy góor ña, ak ñaata dàmba ngeen dajale woon ciy dammit?
1.138359
እነዚህ ጋዜጠኞች !
ya tous ces journalistes!
1.138288
እነርሱም ፍርዱን አላወቁም።
xamuñu lu seen àtteb Yàlla laaj.
1.138055
፲ ወይስ ለአራቱ ሺህ ሰባቱ እንጀራ፥ ስንት ቅርጫትም እንዳነሣችሁ ትዝ አይላችሁምን?
10 Te ndax fàttalikuwuleen itam juróom ñaari mburu ya ngir ñeenti junniy góor ña, ak ñaata dàmba ngeen dajale woon ciy dammit?
1.13783
ማንም ሠው የፈለገውን ይናገር፤ የፈለገው ደግሞ ይስማ።
Dina may ñi ko ragal li ñu bëgg, te dina leen déglu bu ñuy woote ngir ndimbal. "
1.137735
" እነሆ እኔ በእሳቱ መካከል የሚመላለሱ አራት ሰዎች ይታዩኛል።
Mu ne: ' Waaye ñeenti góor laay gis fi, ñuy dox ci biir taal bi.
1.137513
15 "እነሆ፣ እንደ ሌባ እመጣለሁ።
15 Mu ne: "Maa ngi nii yoot, di dikk nib sàcc.
1.137165
በእርግጥም አዳምና ሔዋን፣ በአምላክ ቅር እንዲሰኙ የሚያደርጋቸው ምንም ምክንያት አልነበረም።
10 Waaye nag, Aadama ak Awa dañu tànn bañ a déggal Yexowa.
1.136815
ኢየሱስም፣ "አሁን ካጠመዳችሁት ዓሣ እስቲ አምጡ" አላቸው።
Yeesu ne leen: "Indileen ci jën, yi ngeen jàpp."
1.136732
በእግዚሃብሔር መንፈስ የሚመሩ እነርሱ የእግዚሀብሔር ልጆች ናቸው ።
14 Ndaxte ñépp ñiy déggal Xelu Yàlla mi, ay doomi Yàlla lañu.
1.136711
24:8 እነሱም የእሱን ቃል ትዝ.
24:8 Noonu ñu daldi fàttaliku kàdduy Yeesu ya.
1.136638
በሰማይ ፡ አየሁ ፡ አንተን ፡ የሚመስልህ ፡ የለም
(51) Seedeloowuma léen bindu asamaan si waxumalaak séen ug bind ñoom ci séen bopp.
1.136574
" ትልቅ ጀልባ።
gaal gu mag.
1.13656
አንዳንዶቹ ጠሏት።
Waaye amoon na ku ko bañoon.
1.136549
"+ 5 በዚህ ጊዜ ሐዋርያቱ ጌታን "እምነት ጨምርልን" አሉት።
5 Ndaw ya wax Boroom bi ne ko: "Yokkal sunu ngëm."
1.136526
ለወላጆቻችሁ ታዘዙ።
Déggal say waajur bés bu nekk yombul.
1.136201
" 42 ቀጥሎም "ኢየሱስ ሆይ፣ ወደ መንግሥትህ ስትመጣ አስበኝ" አለው።
42 Mu teg ca ne: "Yeesu, boo délsee ci sa nguur, fàttliku ma!"
1.136018
12ደቀ መዛሙርቱም፣ "ጌታ ሆይ፤ ተኝቶ ከሆነስ ይድናል" አሉት።
12 Taalibe ya ne ko: "Boroom bi, bu nelawee kay, kon dina wér."
1.135968
32 እሱ ግን "እናንተ የማታውቁት የምበላው ምግብ አለኝ" አላቸው።
32 Waaye Yeesu ne leen: "Am na ñam wu may lekk, te xamuleen ko."
1.135921
ታዲያ መታገስህ ፍሬ ያፈራ ለት
xanaa mbetteel ci meññeef mii sababoo
1.135871
አላህንም ጥቂትን እንጅ አያወሱም።
Mag du Yàlla waaye yàgg na ak Yàlla.
1.135783
እውነት መስክረሃል ጌታው!
(29) Texawal ne dëgg gii ca sa Boroom la bawoo.
1.13578
ነቢይን ለማየት ይሆን?
Ngir gis ab yonent?
1.135745
" በእውነትህ ቀድሳቸው ፤ ቃልህ እውነት ነው ።
samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. sa kàddu mooy dëgg.
1.135626
" ይቅርታ ነቢዩ ሲራክ ማለት አንተ ነህ ?
yaw khana si drianke you ndaw yi gueu bok ?
1.135463
የምንጓዘውም ሊያጠቃን ከተዘጋጀ ሰይጣን ጋር እንደሆነ መዘንጋት የለብንም ብለው ጠላታችን ወደ ሆነው ሰይጣን መቅረብ የለብንም፣ አለበለዚያ ሊውጠን ይችላል ብለዋል።
Waay li tah seytaane di natu nit yi mooy daneel leen ci bakaar, ndah nu muna nakka seen bakan, walla mu yahal leen.
1.13542
እውነት ሁሉንም የፈጠረው እግዚያብሔር ነው ?
Ndax li Yàlla sàkk amoon na sikk?
1.135369
ሰዎችም ሲሄዱ አዩአቸው ብዙዎችም አወቁአቸውና ከከተሞች ሁሉ በእግር እየሮጡ ወዲያ ቀደሙአቸው ወደ እርሱም ተሰበሰቡ።
33 Bi ñuy dem nag, am ñu leen gis, xàmmi leen, ñu daldi jóge ci dëkk yépp, daw, jiitu leen fa.
1.135284
ለእነዚህ ሰዎች ለአንድ አፍታ እንኳ አልተገዛንላቸውም፤ ይኸውም፣ የወንጌል እውነት ከእናንተ ጋር ጸንቶ እንዲኖር ነው።
5 Waaye yaatalunu leen benn yoon, ngir dëggug xibaaru jàmm bi mana sax ci yéen.
1.135191
በእግዚአብሔር መንግሥት አዳም ከተፈጠረ ቀን ጀምሮ
Kerook bu Mbindeefyi sappee Bes payoor ba
1.135047
ወደ አምላክ መቅረብ የምትችለው እንዴት ነው?
Naka nga mënee jege Yàlla?
1.134693
ጥሪውን ፡ ያስተጋባ ፡ ለሁሉም ፡ በያለበት
Mu laaj nag matuwaay yépp yemb.
1.134572
ጓደኞችህን የጸጥታ ጊዜህን፣ የቀን ተቀን ተግባራትህንና ከእግዚአብሔር ጋር ለምታደርገው ጉዞህን እንዲከታተሉልህ ጠይቃቸው።
Fexeel sa xarit dila laaj ci say waxtu yi ngay weet ak Yàlla, say yëngu yëngu, ak sa dox ak Yàlla.
1.134527
2:30 ዓይኖቼ ማዳንህን አይተዋልና,
2:30 Ndaxte sama bët tegu na ci mucc gi nga lal,
1.134446
አቢት ፡ እግዚአብሔር ፡ ስራው ፡ ድንቅ ፡ ነው
Yàllaa rafet jëfam ak léppam rafet mu yéwén
1.134446
14 ከእናንተ መካከል የታመመ ሰው አለ?
14 Ana ku wopp ci yeen?
1.134385
10:17 ከዚያም ሰባ ሁለት በደስታ ተመለሱ, ብሎ, "ጌታ ሆይ, አጋንንት ስንኳ ተገዝተውልናል, የእርስዎ ስም.
10:17 Juróom-ñaar-fukki taalibe yi ak ñaar dellusi, fees ak mbég te naan: "Boroom bi, rab yi sax déggal nañu nu ndax sa tur."
1.134377
4 በዚያን ጊዜ።
4 Muu saa gi daa.
1.134341
መልእክተኛዬን ከአንተ አስቀድሜ እልካለሁ።
"Maa ngii di yebal sama ndaw, mu jiitu la,
1.134246
አንተም እኔም ማንም አገርን አልተሸከምናትም ከስሯ ተደብቀንባታል እንጅ !
Kon duma def lu moy topp leen bakkanam, jële leen ci kaw suuf!"
1.134216
20 ሆኖም ሌላኛው መጥቶ እንዲህ አለ:- 'ጌታዬ፣ በጨርቅ ጠቅልዬ ያስቀመጥኩት ምናንህ ይኸውልህ።
20 Keneen dikk ne: "Sang bi, sa poset baa ngii ma fasoon ciw sekkit.
1.133897
ለሰባት ቀናት ያህል, ይህ ከእናቱ ጋር ይሁን; በስምንተኛውም ቀን ለእኔ እመልሰዋለሁ ይሆናል.
Juróom ñaari fan lay nekk ak ndeyam, bésub juróom ñetteel ba, ngeen jox ma ko.
1.133586
እግዚአብሔርን ለሚወዱት ማለትም እንደ ዓላማው ለተጠሩት ነገር ሁሉ ለበጎ እንደሚሠራ እናውቃለን።
Xam nanu itam ne ñi bëgg Yàlla, maanaam ñi Yàlla woo ci boppam te boole leen ci li mu tëral, Yàlla dina joo loxoom ci lépp lu xew ci seen dund, ngir jural leen lu baax.
1.133561
" 4 ከሰማይም ሌላ ድምፅ እንዲህ ሲል ሰማሁ:- "ሕዝቤ ሆይ፣ የኃጢአቷ ተባባሪ መሆን የማትፈልጉና የሚደርስባት መቅሰፍት ተካፋይ መሆን የማትፈልጉ ከሆነ ከእሷ ውጡ።
18:4 Noonu ma dégg beneen baat bu jóge asamaan naan: "Génnleen ci biiram, yéen samay gaay, ngir ngeen bañ a bokk ci ay bàkkaaram te bañ a am cér ci musiba yi koy dal.
1.133479
ከሓዲዎቹ (አማኞቹን)
Waaye ci ñi gëmul, nag:
1.133469
በዚያም ቀን ሳኦል ከሳሙኤል ጋር በላ።
Noonu la Sóol bokke ak Samiyel lekk bésub keroog.
1.133434
በላቸው፡- "ፊተኞቹም ኋለኞቹም።
30 Noonu ñenn ci ñi mujj ñooy jiituji; te ci ñi jiitu, ñooy mujji."
1.133228
ወደ ግብፅ አይመለሱምን?
5 Duñu dellu réewum Misra a .
1.133207
ኢየሱስ ምን እያሰቡ እንዳለ አውቋል።
Yeesu xam na li nit ki di xalaat.
1.132955
57"ታዲያ ራሳችሁ ትክክለኛ የሆነውን ነገር ለምን አትፈርዱም?
57 "Lu tax it dungeen àtteel seen bopp liy jëf ju jub?
1.132911
ወደ አምላክ መቅረብ የምትችለው እንዴት ነው?
Naka nga mënee jege Yàlla ?
1.132733
; እነርሱም አሉ, "የዮሴፍ ልጅ ይህ አይደለምን?
Ñu naan: "Xanaa kii du doomu Yuusufa ji?"
1.132719
ለዚህም እግዚአብሔር ሃይልና ብርታት ይስጠን።
Texe ak daraja ak kàttan ñeel na sunu Yàlla.
1.132504
1 ዮሐንስ 2:18 ልጆቼ ሆይ, ይህ የመጨረሻው ሰዓት ነው.
2:18 Samay doom, waxtu wu mujj wi jot na!
1.132455
ነቢያትም ሞቱ ናቸው.
Yonent yi itam faatu nañu.
1.132188
ሙሴ ሕግን የሰሰጣችሁ አይደለምን ?
19 Xanaa du Musaa moo leen jox ndigali Yàlla yi?
1.132099
እሱ ምንጊዜም አምላክን ይታዘዝ ነበር።
moom muy xaar ndigalu Yàlla.
1.132023
መመለሻችሁም ወደ እሳት ነው" በላቸው።
ba dellooleen safara gañu jógé woon.
1.131938
' 5 የእኔስ ቤት በአምላክ ፊት እንዲሁ አይደለም?
5 Du nii la sama waa kër def ak Yàlla?
1.131874
በመሆኑም ሰይጣን ለመጀመሪያዋ ሴት ለሔዋን ውሸት በመናገር ከአምላክ ይልቅ እሱን እንድትታዘዝ አሳመናት።
Seytaane dafa fen Awa jigéen ju njëkk ja, xiir ko mu déggal ko te bañ a déggal Yàlla.
1.131845
በመሆኑም ያዕቆብ ልጆቹ እስኪመለሱ ድረስ ዝም አለ።
Yanqóoba ne cell, ba ñu ñibbsi.
1.131731
Mateus 5:12 ዋጋችሁ በሰማያት ታላቅ ነውና ደስ ይበላችሁ፥ ሐሴትም አድርጉ፤ ከእናንተ በፊት የነበሩትን ነቢያትን እንዲሁ አሳድደዋቸዋልና።
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
1.131676
2 ለምሳሌ አብርሃም ጻድቅ የተባለው በሥራ ቢሆን ኖሮ የሚመካበት ነገር በኖረው ነበር፤ ሆኖም በአምላክ ፊት ሊመካ አይችልም።
2 Bu fekkoon ne Ibraayma, ci kawi jëfam lees ko jox àtteb ku jub, kon mu man koo damoo, waaye demewul noonu fa Yàlla.
1.131614
እኔ ያየሁትን ታያላችሁ?
Eske gis nga lu ma gis ?
1.131581
ከእንግዲህም የጦርነት ትምህርት አይማሩም።
te dootuñu jàngati xare.
1.131428
19:34 ስለዚህ እነርሱ አለ, "ጌታ ይህን ያስፈልገዋል ስለሆነ.
19:34 Ñu tontu ne: "Ndaxte Boroom bi da koo soxla."
1.131346
ኢየሱስ የመዳንን መንገድ ነው.
Yeesu mooy yoonu mucc gi !
1.131342
8 እኔ ግን 'ጌታ ሆይ፣ በጭራሽ፤ ምክንያቱም ንጹሕ ያልሆነ ወይም የረከሰ ነገር ወደ አፌ ገብቶ አያውቅም' አልኩ።
11:8 Waaye ma tontu ne: "Mukk Boroom bi, ndax dara lu daganul mbaa lu araam musul a dugg ci sama gémmiñ."
1.131227
ከዚያም ዳዊትና ሰራዊቱ በሙሉ ወደ ኢየሩሳሌም ተመለሱ።
Gannaaw loolu Daawuda ànd ak mbooloom xareem mépp, dellu Yerusalem.
1.131112
ከእናንተም የሚበልጠው አገልጋያችሁ ይሆናል.
Ki gëna mag ci yeen mooy ki nango nekk seen surga.
1.131093
አላህ የሻው ነገር በጠቅላላ ይሆናል።
Waaw, ci lu wóor, lépp li Yàlla bëgg, dina ko def!
1.131075
እነዚህ ጋዜጠኞች !
Aaaah, ces journalistes!
1.131069
"እናም እግዚአብሔርን ለሚወዱት እንደ አሳቡም ለተጠሩት ነገር ሁሉ ለበጎ እንዲሠራ እናውቃለን።
28 Xam nanu itam ne ñi bëgg Yàlla, maanaam ñi Yàlla woo ci boppam te boole leen ci li mu tëral, Yàlla dina joo loxoom ci lépp lu xew ci seen dund, ngir jural leen lu baax.
1.131058
፪ በእውቀት አይቅኑ እንጂ ለእግዚአብሔር እንዲቀኑ እመሰክርላቸዋለሁና።
2 Ñoom laa seedeel seenug parlute ci Yàlla, waaye dañu koo tegul ci xam-xam bu doy.
1.131025
165ሕግህን የሚወዱ ብዙ ሰላም አላቸው፤
165 Jàmm ju baree ñeel ku sopp sa yoon,
1.131016
በነቢያቴም ላይ ክፉ አታድርጉ።
buleen lor samay yonent."
1.130779
5፤ በውኑ ቤቴ በእግዚአብሔር ዘንድ እንዲሁ አይደለምን?
5 Du nii la sama waa kër def ak Yàlla?
1.13071
7 ታላቅ ተራራ ሆይ፣ አንተ ማን ነህ?
7 Yaa di kan, yaw tund wu mag wi?
1.130701
44በል አሁን ቃል ኪዳን እንጋባ፤ ኪዳኑም በአንተና በእኔ መካከል ምስክር ይሁን።
44 Léegi ñëwal rekk, ñu fasante kóllëre maak yaw, te seede dox sunu diggante maak yaw."
1.130599
በአንደበቷም ቀና ምክር አለ።
Ci seeni làkk, Mandinka mooy: nit ku juge Mande.
1.130516
11:18 ዮሐንስ ሳይበላና ሳይጠጣ መጣ; እነርሱም ይላሉ, 'ጋኔን አለበት አሉት.
11:18 Ndaxte Yaxya feeñ na, lekkul, naanul, ngeen daldi ne: "Dafa ànd ak rab."