Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
score
float32
1.04
1.22
Amharic
stringlengths
8
300
Wolof
stringlengths
10
472
1.219372
42 ስለዚህ የሙታን ትንሣኤም እንደዚሁ ነው።
42 Noonu itam la ndekkitel ñi dee di deme.
1.219372
42 ስለዚህ የሙታን ትንሣኤም እንደዚሁ ነው።
42 Noonu itam la ndekkitel ñi dee di deme.
1.214097
በመሆኑም በዚያን ጊዜ በሰማይ የአምላክን ፈቃድ እያደረጉ የነበሩት ሁሉም አይደሉም።
Kon nag booba, du ñépp ñi nekkoon asamaan ñoo doon def coobare Yàlla.
1.20744
33ሐዋርያትም ስለ ጌታ ኢየሱስ ትንሣኤ በታላቅ ኀይል መመስከራቸውን ቀጠሉ፤ በሁላቸውም ላይ ታላቅ ጸጋ ነበር።
33 Ndaw yi nag di seedee doole ju réy ne Sang bi Yeesu dekki na, yiw wu yaa di leen dikkal ñoom ñépp.
1.201513
ኢየሱስም ትንሣኤና ሕይወት እኔ ነኝ ።
Man maay ndekkite li, maay dund gi.
1.191045
+ 9 በሰዎች ፊት የሚክደኝ ሁሉ ግን በአምላክ መላእክት ፊት ይካዳል።
9 Waaye ku ma gàntu ci kanam nit ñi, dinañu la gàntu ci kanam malaakay Yàlla yi.
1.189482
በእውነት ቃል፣ በእግዚአብሔር ኀይል፣ በቀኝና በግራ እጅ የጽድቅ የጦር ዕቃ በመያዝ፣
ci kàddug dëgg ak ci kàttanu Yàlla, nu ngi yor gànnaayi njubte ci loxol ndeyjoor ak lu càmmooñ.
1.188606
"የሉጥ ቤተሰቦች ብቻ ሲቀሩ።
Lot ne ca xiiñidxaapaʼ bizuubacaʼ diidxaʼ ne bixooñecaʼ de Sodoma.
1.181714
11 አብሮኝ ያለው ሉቃስ ብቻ ነው።
11 Luug rekk a des fi man.
1.179598
11 ሉቃስ ብቻ ከእኔ ጋር አለ።
11 Luug rekk a des fi man.
1.176067
48እናንተም ለዚህ ምስክሮች ናችሁ።
48 Yéenay samay seede.
1.174358
(ከጉድለት ሁሉ) ጠራ።
Mu laaj nag matuwaay yépp yemb.
1.1695
17 ልጆች ከኢየሱስ ሊማሩ ይችላሉ?
17 Ndax am na li xale yi mën a jàng ci Yeesu?
1.168933
እንግዲህ በጎ የሆነው ነገር ለእኔ ሞት ሆነብኝን ?
13 Ndax kon lu baax moo ma tàbbal ci dee?
1.16881
ስለዚህ, ለምን አንተ ባሪያዬ ሙሴ ለማጣጣል አልፈራም ነበር?
Kon lu leen may fitu ŋàññ Musaa sama jaam bi?"
1.16824
ይጠያየቃሉ:: ወንድማማች ነን።
naan: "Wóoy ngalla nun, bokk yi!"
1.16821
እናንተ ትፈልጉኛላችሁ፤ ግን አታገኙኝም፤ ወደምሄድበትም ልትመጡ አትችሉም" አለ።
Dingeen ma seet, waaye dungeen ma gis; te dungeen man a dem fa may nekk."
1.164905
ባለቤቷ ዛሬ ጠዋት ነው ያስገቡኝ።
Sama jëkkër jox na ma sama njël.
1.164651
ከዚያም ዳዊት ልጁን በየቀኑ አለቀሰ.
Buur Daawuda nag di jooy doomam bés bu nekk.
1.163923
ፍርድህ በአንድ ሰዓት ደርሶአል።
Ci wenn waxtu rekk la sa àtte dikk!"
1.163394
18 ከዚያም ኢየሱስ እንዲህ አለ፦ "የአምላክ መንግሥት ከምን ጋር ይመሳሰላል?
18 Yeesu neeti: "Ana lu nguurug Yàlla di nirool?
1.163379
· "እኛም ለአባቶች የተሰጠውን ተስፋ የምስራቹን ለእናንተ እንሰብካለን፤" (የሐዋ.
te nu ngi leen di xamal xebaar bu baax ne leen, li yàlla digoon sunuy maam,
1.163144
8:52 ስለዚህ, አይሁድ አለ: "አሁን እኛ አንተ ጋኔን እንዳለብህ እናውቃለን.
8:52 Yawut ya ne ko: "Léegi wóor nanu ne, dangaa am ay rab!
1.162479
ኢንሻአላህ አንድ ቀን በመድብል ተዘጋጅቶ ይደርሳቸዋል።
allah taala app sub ko hidyat day.
1.162379
28እነርሱም፣ "ታዲያ የእግዚአብሔርን ሥራ ለመሥራት ምን ማድረግ አለብን?
6:28 Noonu ñu laaj ko ne: "Lu nu war a liggéey, ngir matal jëf yi neex Yàlla?"
1.162105
ከይሁዳ የመጣህ የእግዚአብሔር ሰው አንተ ነህን?
Mu ne ko: "Yaa di góoru Yàlla gi jóge Yuda?"
1.160997
+ 12 በሰማያት የሚጠብቃችሁ ሽልማት ታላቅ ስለሆነ+ ሐሴት አድርጉ፤ በደስታም ፈንጥዙ፤+ ከእናንተ በፊት የነበሩትን ነቢያት እንደዚሁ ስደት አድርሰውባቸው ነበርና።
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
1.160361
9፤ ከእኔም ጋር ሊዋጋ ቢችል ቢገድለኝም፥ ባሪያዎች እንሆናችኋለን፤ እኔ ግን ባሸንፈው ብገድለውም፥ እናንተ ባሪያዎች ትሆኑናላችሁ፥ ለእኛም ትገዛላችሁ አለ።
9 Su ma manee ba rey ma, nuy seeni jaam; waaye su ma ko manee ba rey ko, ngeen di sunuy jaam, di nu jaamu."
1.160016
Usage: 2020 የእኔ አመት ሁን
Usage: 2020 nekk sama at
1.159111
ለሌሎች ሰፈሮችም አቀበለው።
làq ko ci yeneni réew.
1.158939
5ሴቶቹም ከመፍራታቸው የተነሣ ወደ ምድር አቀርቅረው ሳሉ፣ ሰዎቹ እንዲህ አሏቸው፤ "ሕያው የሆነውን እርሱን ለምን ከሙታን መካከል ትፈልጋላችሁ?
5 Naka la leen tiitaange jàpp, ba ñu sukk, dëpp seen jë fa suuf, ñu ne leen: "Kiy dund, lu tax ngeen di ko seet ci biir ñi dee?
1.158871
ከዚያም ሙሳ ሆይ!
waaaw les mousses!
1.158389
እኔም "ጌታዬ ሆይ፣ አላውቅም" ብዬ መለስኩለት።
Ma ne ko "Déedéet, Sang bi."
1.15833
(ዘፍጥረት 1:28) ምድር ፈጽሞ አትጠፋም።
(Njàlbéen ga 1: 28) Suuf si du fi mas a jóge.
1.158301
) ይህ የመጀመሪያው ትንሣኤ ነው።
Loolu moo di ndekkite lu jëkk li.
1.157908
70በዚህ ጊዜ ሁሉም፣ "ታዲያ፣ አንተ የእግዚአብሔር ልጅ ነህን?
70 Ñépp daldi ne: "Kon yaay Doomu Yàlla?"
1.157904
"አምላክን እንደሚያውቁ በይፋ ይናገራሉ፤ ሆኖም በሥራቸው ይክዱታል።
" Dañoo mbubboo xam-xamu Yàlla, waaye seeni jëf weddi na ko. " - TIT 1:16.
1.157802
ጌታ ሆይ፤ ከእኔ አትራቅ።
éy Boroom bi, bul ma sore.
1.157751
በእነርሱ ቁጥር በእጥፍ እነሱን ማዋሃድ.
rajaxe leen ñaari yoon.
1.157649
ውሃ አምጡላቸው።
yóbbul leen am ndox.
1.157104
እንዲህ በማለትም መለሱላቸው፦ "ይህ ታላቅ ቀን ነው።
Kàddu Yàlla nee na: " Bésu Yexowa bu mag bi jege na.
1.156985
የምታዩትን የሚያዩ ዓይኖች ብፁዓን ናቸው።
Ñi seeni bët di gis li ngeen di gis, am nañu mbég.
1.156812
19 የአምላክ መንግሥት በአርማጌዶን አማካኝነት ምን ነገር ያከናውናል?
19 Lan la Nguuru Yàlla di def jaare ko ci xeexu Armagedon?
1.155337
አንደኛ ‹መላእክትም ያሉትን (አስታውስ) ፡- መርየም ሆይ!
Lii la malaaka yi wax Lóot: ' Gaawal !
1.155309
70በዚህ ጊዜ ሁሉም፣ "ታዲያ፣ አንተ የእግዚአብሔር ልጅ ነህን?
70 Noonu ñépp ne: "Kon nag yaay Doomu Yàlla ji?"
1.15499
"የአላህ ቀጠሮ እውነት ነው።
Te sama dige Booroom dëgg la."
1.154927
ምንድነው ሰለሞን ያደረገው?
Lan la Suleymaan di def nag ?
1.154819
10:42 ሆኖም አንድ ነገር ብቻ አስፈላጊ ነው.
10:42 Moona de, lenn rekk a am solo.
1.154245
ከእኔ ጋር ይነጋገር የነበረው መልአክም፣ "እነዚህ ምን እንደሆኑ አሳይሃለሁ" አለኝ።
Malaaka miy wax ak man ne ma: "Maa lay won lu ñii wund."
1.15393
የያዕቆብም ልጆች አሥራ ሁለት ናቸው፤
Doomi Yanqóoba d yu góor fukk lañu ak ñaar.
1.153766
ሳምራውያን ወደ እርሱ በመጡ ጊዜ ከእነሱ ጋር እንዲኖር ጠየቁት ።
Ñu daldi dikk ñaan Yeesu, mu dal ak ñoom.
1.153605
ለእርሱም አባቶቻችን ሊታዘዙት አልወደዱም፤ ነገር ግን ገፉት በልባቸውም ወደ ግብፅ ተመለሱ፤
39 Waaye sunuy maam nanguwuñu koo déggal; dañu koo bañ te seeni xel dëpp, dellu Misra.
1.153572
አምላክ፣ እስራኤላውያንን ምሥክሮቹ እንዲሆኑ መርጧቸው ነበር።
Yàlla tànnoon na waa Israyil ngir ñu nekk ay seedeem.
1.153422
መልካሙን የእምነት ገድል ተጋደል፥ የተጠራህለትንም በብዙም ምስክሮች ፊት በመልካም መታመን የታመንህለትን የዘላለምን ሕይወት ያዝ።
12 Góor-góorlul ci bëre bu baax bi, ba ub làmbi ngëm, te feddali sag téye ci dund gu dul jeex gi; ndaxte ci loolu la la Yàlla woo, te looloo waraloon it sa seede su rafet fa kanam mbooloo mu bare.
1.152988
ለሚፈሩት ፍላጎታቸውን ይፈጽማል፤ ጩኸታቸውን ይሰማል" ይላል።
Dina may ñi ko ragal li ñu bëgg, te dina leen déglu bu ñuy woote ngir ndimbal. "
1.152049
18ከዚያም ኢየሱስ እንዲህ አለ፤ "የእግዚአብሔር መንግሥት ምን ትመስላለች?
18 Noonu Yeesu neeti: "Lan la nguuru Yàlla di nirool?
1.151965
እኛ ግን የሙሴ ደቀ መዛሙርት ነን.
Nun, taalibey Musaa lanu.
1.151767
ጨረቃንም የገራ መሆኑን አታይምን?
Les inn uttale for moon moon [es - latam] Vet du hvordan man uttaler moon?
1.15085
እሱ እነዚህን መንግሥታት ሁሉ ያፈጫቸዋል እንዲሁም ያጠፋቸዋል ፤ እሱ ግን ለዘላለም ጸንቶ ይኖራል ፤
Dina jàllarbi ak a tasaare nguur yeneen yépp, waaye moom doŋŋ dina sax ba fàww."
1.150631
አላህ ለሚሻው ሰው
18 Kon nag Yàlla mooy yërëm ku ko neex, te ku ko neex lay dëgëral xolam.
1.150548
31 እግዚአብሔርም ያደረገውን ሁሉ አየ፥ እነሆም እጅግ መልካም ነበረ።
31 Yàlla nag gis li mu def lépp, fekk lépp baax lool.
1.150533
ሁለት ዓይነት ሚዛንና ሁለት ዓይነት መስፈሪያ፥ ሁለቱ በእግዚአብሔር ፊት ርኩሳን ናቸው።
Woor ñaari farata la am: 1 yeene 2 ba liy dogloo ngir yàlla.
1.15043
ነቢይ ለማየት?
Ngir gis ab yonent?
1.150427
..." እንደ ሕጻናት ካልሆናችሁ ወደ መንግሥተ ሰማይ አትገቡም"
Su ngeen woññikiwul ci Yàlla, ba mel ni xale, dungeen dugg mukk ci nguuru Yàlla Ajia kawe ji.
1.150214
ነቢያትስ ለዘላለም በሕይወት ይኖራሉን?
Yonent yi nag, ndax ba fàww lañuy dund?
1.150206
(ዘፍጥረት 1:28) ምድርም ፈጽሞ አትጠፋም።
(Njàlbéen ga 1: 28) Suuf si du fi mas a jóge.
1.150191
Usage: 2020 የእኔ ዓመት ሁን
Usage: 2020 nekk sama at
1.149578
ራሱ የእግዚአብሔር ሌላ ስሙ ማለት ነው።
Ngir-yàlla tànnal beneen tur.',
1.149474
አላህ ለሚሻው ሰው
18 Kon nag Yàlla, la ko neex lay def, muy yërëm nit, mbaa dëgëral xolam ci lu bon.
1.149458
እስራኤላውያንም ይህን ሲሰሙ ፍልስጤማውያንን ፈሩ።
Bànni Israyil yég ko, am tiitaange ca waa Filisti.
1.149177
ማንም እንደማያስተውለው እግዚአብሔር በስውር ይሠራል።
Yàlla, lumu def noonu la te jaam bu ko xam noppalu.
1.148766
እናንተ ከዚህ ዓለም ጋር ወዳጅነት ለእግዚአብሔር ጥል እንዲሆን አታውቁምን?
Xanaa xamuleen ne xaritoo ak àddina moo di noonoo ak Yàlla?
1.148697
28 ፤ ለአባቶቻችሁም በሰጠኋት ምድር ትኖራላችሁ፤ ሕዝብም ትሆኑኛላችሁ እኔም አምላክ እሆናችኋለሁ።
28 Su boobaa ngeen mana dëkke réew mi ma joxoon seeni maam, di sama ñoñ, may seen Yàlla.
1.148615
7 አምላክህም እግዚአብሔር ይህችን መርገም ሁሉ በጠላቶችህና በሚጠሉህ በሚያሳድዱህም ላይ ያመጣታል።
7 Su loolu amee seen Yàlla Aji Sax jeey teg mboolem alkànde yii ma leen limal, ci kaw seeni noon ak seen bañ yi leen toŋal.
1.148067
በእግዚአብሔር ስም የሚመጣ የተባረከ ነው።
Yaw miy ñëw ci turu Boroom bi, ku barkeel nga!
1.147651
ሣራ ለሚስቶች ምን ግሩም ምሳሌ ትታለች?
Ban royukaay bu rafet la Saarata bàyyil jabar yi?
1.14764
ለወለደችውስ ልጅ አትራራምን?
Ndax du am yërmande ci doomam ji mu jur?
1.147612
ነብያትስ ለዘላለም በሕይውት ይኖራሉን?
Yonent yi nag, ndax ba fàww lañuy dund?
1.147256
በወንድማችሁ ወይም በእህታችሁ ላይ ድንገት ተነስታችሁ የምትሰጡትስ ማጠቃለያስ ተገቢ ነው፤ ትላላችሁን?
kouko dÉfone sa rakke walla sa makke bou djiguÉne, ndakh dina la nÉÉkh?
1.146996
እነዚህ ነገሮች እውነት መሆናቸውን ታምናለህን?
Ndax gëm nga ne loolu dëgg la?
1.146986
ስለዚህ እስራኤል ብሎ ጠራው።
Mu tudde ko nag Israyil.
1.146648
"እንግዲህ አሁን መጠየቅ: እግዚአብሔር ሕዝቡን ጣላቸውን?
1 Ma ne kon, ndax Yàlla bërgël na xeetam?
1.146594
ስለዚህም እስራኤል ብሎ ጠራው።
Mu tudde ko nag Israyil.
1.146333
እሱም ይህን ለማድረግ እግዚአብሔር የሚወስደው.
Yàlla yàkkamti na defaat loolu.
1.146201
5:6 እንግዲህ በጊዜው ከፍ እንዲያደርጋችሁ ከኃይለኛው ከእግዚአብሔር እጅ በታች ራሳችሁን አዋርዱ፤
5:6 Suufeel-leen seen bopp kon ci ron loxob Yàlla bu am kàttan, ngir mu yékkati leen ci jamono ju ko soob.
1.146198
ሁሉም እንደ ልብስ ያረጃሉ፤
dinañu màggat ñoom ñépp ni ay yére.
1.146121
159መመሪያህን እንዴት እንደምወድ ተመልከት፤
159 Seetlul ni ma soppe say tegtal.
1.145241
አለኝም ፡ እነዚህ ፡ ከታላቁ ፡ መከራ ፡ የመጡ ፡ ናቸው
Mu ne ma: "Ñoo di ñi jóge ca metit wu réy wa.
1.14424
በዚያም ተቀምጠው ይጠብቁት ነበር።
ba noppi toog fa, di ko wottu.
1.144164
ወዲያውም ከሓዲዎችን በውስጡ ካለው ነገር
Te loolu ci kanam aji gëmadi ñi sax lañu koy defe far!
1.144142
ስለ እኔም እግዚአብሔርን ያከብሩ ነበር።
te ñuy sant yàlla ci man.
1.143923
ውድ ልጆች, አሁን የመጨረሻ ጊዜ ነው.
Samay doom, waxtu wu mujj wi jot na!
1.143728
እግዚአብሔርም (ያህዌ) ፣ "መሬት ላይ ጣላት" አለው።
Yàlla ne ko: ' Sànni ko ci suuf. '
1.143403
22የወለደህን አባትህን አድምጥ፤
22 Déglul sa baay bi la jur.
1.143191
2በመጣሁ ጊዜ ለምን በዚያ ሰው አልነበረም?
2 Ana lu tax ba ma dikkee, kenn nekku fa?
1.143182
"ኧረ ግዴለህም የምታስበውን ንገረን?
"Wax nu ci ban sañ-sañ ngay defe yëf yii, walla kan moo la may boobu sañ-sañ."
1.143055
አላህም ገደለው መቶ ዓመትን (አቆየውም) ።
Yàlla daldi koy rey moom lu tollu ci téeméeri at.
1.143029
ምድርንና በውስጧ ያሉትን ነገሮች በሙሉ የፈጠረው የሰው ልጆችን ስለሚወድ ነው።
Moom moo sàkk suuf si ak lépp lu ci nekk ndaxte dafa bëgg doomu Aadama yi.
1.142897
ይህ እኛንና ፍጥረታትን በሙሉ የፈጠረ ጌታም፣አምልኮት የሚገባው፣ከርሱ በቀር ማንምና ምንም ሊመለክ የማይገባ ብቸኛው እውነተኛ አምላክ ነው።
Yàlla, Buur Bi, Sunu Boroom, Aji-Màgg Ji, Aji-Sàkk Ji..añs lépp a ngi joxoñ Ki sàkk lépo ak ñépp.
1.142436
"አይሁዶችም "የአላህ እጅ የታሰረች ናት" አሉ።
Mu ne leen: ' Léegi Yeesu mu ngi asamaan ci ndeyjooru Yàlla.
End of preview. Expand in Data Studio

Amharic-Wolof_Sentence-Pairs Dataset

This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.

This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1

Metadata

  • File Name: Amharic-Wolof_Sentence-Pairs
  • Number of Rows: 66465
  • Number of Columns: 3
  • Columns: score, Amharic, Wolof

Dataset Description

The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:

  1. score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).
  2. Amharic: The first sentence in the pair (language 1).
  3. Wolof: The second sentence in the pair (language 2).

This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.

References

Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:

[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017

[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.

[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018

[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.

[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.

[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.

[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.

[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB

[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.

[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages

Downloads last month
6

Collection including michsethowusu/amharic-wolof_sentence-pairs