wo
stringlengths 2
789
| fr
stringlengths 2
722
|
|---|---|
Waaw, waa ji daje ak klaas bi.
|
Oui, le type de la réunion de classe.
|
GÓOR DAÑU BËGG LAAL.
|
Les hommes aiment toucher.
|
Ban xeetu weer la lii...
|
Quel est ce verre?
|
- Baax na.
|
- Ça va aller.
|
Su taat yi gënnee soreyoo sax ci rëdd yi walla sooy jëmbët fu nekk, na per yi am seen digënté 40 sàntimeetar. Ndaxte, benn per dina tas ferñent u asot yi ci 20 sàntimeetar li ko wër.
|
Même si vous utilisez d’autres distances dans les lignes ou si vous repiquer au hasard, gardez toujours une distance de 40 cm entre les granules. Car une granule diffuse l’azote à peu près dans un rayon de 20 cm.
|
Ba léegi, jëllël digal njiit yin, nangul bepp gindikaay, ak bàyyil xel ci yëgle yu am kaaraange.
|
Néanmoins, suivez les conseils des autorités, obéissez à tous les panneaux et prêtez une attention particulière aux avertissements de sécurité.
|
Sa dundu a ngi ci balans bi.
|
Votre vie est en jeu.
|
Seen jappalante moo leen dimbëli ba doomi nduxum gi du tasaaroowul ci seen tool u dëkkendόo yi.
|
Leur effort commun les aide aussi à éviter la dissémination des graines de striga aux champs voisins.
|
Lu nga ma def leegi?
|
Tu m'as fait quoi?
|
- Ñoom ay alal lañu.
|
- Ils sont riches.
|
Amaana leegi dafa dem fu sori ci àdduna bi.
|
Il a probablement volé au bout du monde maintenant.
|
Altine la auditeur yi di ñëw.
|
Les auditeurs seront là lundi.
|
Oogway toog moom kese ci grotte 30 at di laaj benn laaj.
|
Oogway est resté seul dans une grotte pendant 30 ans à poser une question.
|
Jeexal ko.
|
Finissez le jeu.
|
Su fekkoon ni tànta Jaya mingi woon fi, kon dina ma ray!
|
Si tante Jaya avait été ici, elle m'aurait tué!
|
Mbënd!
|
Une surprise!
|
Ana lu jëm ci diir bi?
|
Et le décalage temporel?
|
Speer...
|
Je suis Speer.
|
Nañu seet li nga mën a def.
|
Voyons voir ce que tu sais faire.
|
waaw lu baax nga xam loolu
|
Oui, c'est bien. Tu le sais.
|
Du maymu rek.
|
Il est plus qu'un singe.
|
Ugh!
|
Je suis désolée.
|
Dafay xam li ñuy xalaat, fépp fu ñu dem ak ñi ñu wóolu.
|
Il découvre ce qu'ils pensent, où ils vont et en qui ils ont confiance.
|
Amélie Polain mi ngi judd.
|
Amélie Poulain est née.
|
Askan wi ni muy yookoo, tekkiwul ni moo tax garab yi néew ci all bi.
|
L’expansion des populations humaines n’implique pas forcément qu’il y ait moins d’arbres dans le paysage.
|
Yobbul ko ci sama néeg!
|
Emmenez-la dans ma chambre!
|
Loolu mooy sunu waay.
|
C'est notre homme.
|
Dafay aju.
|
Ça dépend.
|
Ndax képp kuy def lii mingi ko jël bu baax leegi ngir xamle ni leble yi nga am, amul benn garantie.
|
Parce que celui qui fait ça le prend assez au sérieux pour nous faire savoir que les prêts que vous avez, ils ne sont pas garantis.
|
Dinaa denc samay gëm-gëm ngir Septon bu kawe bi.
|
Je vais garder mes aveux pour le Septon.
|
Sëñ bi... yaa daan ci dosiye bi.
|
Vous avez gagné l'affaire.
|
Doonte FBI defna ñaari at ci amal lànket, mënu ñu woon gis operatër bi wala xam kan la.
|
Malgré deux ans d'enquête, le FBI n'a pas été en mesure de localiser l'agent ou déterminer son identité.
|
Wax ko!
|
Tu lui dis!
|
Man ci sama bopp laa koy def.
|
Je vais m'en occuper moi-même.
|
Ci tool laa juddoo.
|
J'ai grandi dans une ferme.
|
Benn buntu bu yomb la woon ngir dugg ci ëtt bi.
|
Le seul accès à la cour était par une simple porte.
|
Du kablaas bi mooy jafe-jafe bi.
|
Le problème n'est pas le câblage.
|
Sudee mën nanu jéem - nekk lu am solo tuuti, lan ngay digal?
|
Si on pouvait essayer d'être un peu constructifs, que suggérez-vous?
|
Nit mën nañ ci lóru suñu nooyee ndox buñu jëlee ci ngélaw li ak vague yi.
|
Les humains peuvent être affectés en respirant de l'eau contaminée transportée dans l'air par le vent et les vagues.
|
Fan nga duggee ci seeni poos?
|
Tu es tombé dans leurs poches?
|
Maa ngi wax ak yaw!
|
Je te parle!
|
Sooy liggéey ci mbooloo,ci ngay gënn gaaw xam ci mbey yu bees yi ak yeneen taneef yi ngir xeex nduxum gi.
|
En travaillant en groupe, vous pouvez apprendre plus vite et mieux sur les nouvelles variétés et les autres options pour lutter contre le striga.
|
Dama bëgga xam ndax Wenck mën na song am déet.
|
Je veux savoir si Wenck peut attaquer ou pas.
|
Flint, demal fi.
|
Flint, reste où tu es.
|
Tome, indil ma garab yi.
|
Tom, apporte-moi les journaux.
|
Hazmi ak Mihdhar jënd nañu kër ngir moytu ñu jëflante ak kenn
|
Hazmi et Mihdhar achètent une maison pour éviter d'avoir à traiter avec qui que ce soit.
|
Dafa dëgër lool.
|
Il est très fort.
|
Xale bu bees la itam.
|
Il est aussi nouveau ici.
|
Bul yàq oto bi.
|
Ne gâche pas la voiture.
|
Soo defee loolu, dama bëgga am helicopter ci North Lawn bu fees dell ak essence.
|
Une fois que vous l'aurez fait, je veux un hélicoptère sur le North Lawn, plein de carburant et prêt.
|
Deñoo am saas mu dugal ci saa boobu."
|
Nous avons eu de la chance qu’il ait marqué à ce moment. »
|
- Dama wara dem.
|
- Je dois y aller.
|
Amna benn garde bu rëcci ci kër gu ubbeeku gi ñuy gis alal ji wër Treasure Beach
|
Il y a un garde qui s'est échappé d'une maison ouverte où le trésor autour de Treasure Beach peut être vu
|
(WAX ALBAAN)
|
Je suis désolé.
|
Dagatum tool yeet, dollina beykat yi, kolute ci li ñuy def ci suuf ci, dina am jariň ci seen mbey.
|
Les courbes de niveau ont également donné de la confiance aux agriculteurs que tout ce qu'ils investissent dans leur sol sera bénéfique pour leurs cultures.
|
Dundal yeneen téeméeri at te wéy di xelal, yow mi am xel, teg ci màndu.
|
Dundal encore 100 ans et continue de nous éclairer de votre sagesse.
|
Ci turu Yeesu lañuy ñaan. Amiin.
|
Au nom de Jésus, nous prions.
|
Mu ngi doon soolu ndànk-ndànk, di defar benn benn ay xobam.
|
Elle s’habillait lentement, elle ajustait un à un ses pétales.
|
Lu tax nga def lii?
|
Pourquoi tu as fait ça?
|
Waaye dina nekk dóor bu jaar yoon.
|
Mais ce sera une bonne raclée.
|
Dafay jàppale guddi gi.
|
Ça suffit pour une nuit.
|
Ne leen wóor ni jiwu ji di na sax bu baax te ngeen ji diggënté 5 akk 8 pep ci pax bu nekk.
|
Assurez-vous que la semence germe bien et semez entre 5 et 8 grains par poquet
|
Laac leen mboolo jiggéen ñi ngir jàpp waxtu yi ñu mën bokk ci lël up tàggat yi. Ñëw leen ca waxtu wa ndax amu ñu bés bi yéep ngir loolu rekk.
|
Consultez les groupements de femmes pour décider de la bonne heure pour elles pour participer aux formations. Et tachez d’être à l’heure. Elles n’ont pas toute la journée !
|
Tuuti ndimbal!
|
Un peu d'aide!
|
Yaa ngi soppi askan wi yépp def ko brothel.
|
Vous avez transformé la société en bordel.
|
(MUSIK BU YÀQ DAFA WÉY)
|
(La musique est lente)
|
Danu leen wara topp leegi
|
Nous devons les suivre maintenant.
|
6 Ci juróom ñatti fukki at ak juróomi guerre civil, àttekaay bi jëfandikoowul bu baax kàttan googu.
|
6 Pendant les cinquante-cinq années de guerre civile, la cour fit peu usage de ce pouvoir.
|
Saa waay..yaa ngi may ñaawal?
|
Tu te moques de moi?
|
Gis leen fuñu desee doole, dina nu leen jàpp.
|
Trouvez leurs faiblesses, et nous les exploiterons.
|
yii duñu say xarit!
|
Ce ne sont pas tes amis!
|
Ndax ci kaw picc la woon?
|
C'était sur un oiseau?
|
Coono yépp dina jeex !
|
Il y aura une fin à toutes les souffrances!
|
Deet.
|
- Pas encore.
|
Edisioŋ 1984 moo gënoon baax.
|
L'édition de 1984 était la meilleure.
|
Midhar jotul passport bi te delluwul Etats Unis.
|
Midhar n'a pas reçu le passeport et n'est pas retourné aux États-Unis.
|
Ndax mën naa gis Wonderstone ab diir?
|
Je peux voir Wonderstone une seconde?
|
tëye loxo bi ubbeeku nii.
|
Tenez la main ouverte comme ça.
|
Politigu nguur gi mooy séddale bis bu nekk sertifikaa di SBA képp ku ko laaj.
|
La politique de l'administration est de distribuer des certificats SBA sur une base quotidienne à quiconque le demande.
|
Dal.
|
- Je vous en prie.
|
Li leer mooy sunuy xalaatkat ci wàllu juuti mën nañu la digal nga moytu joxe benn kado.
|
Malheureusement, nos conseillers fiscaux peuvent déconseiller de faire un don.
|
Co tolluwaay boobu, góor ñee ci mën.
|
Et sur ce niveau, ce sont les hommes qui l’emportent.
|
Lu tax mu yóbbu ma fi?
|
Pourquoi m'a-t-elle conduit ici alors?
|
Xalaatam Kapiteen Blood daal di dakkal ndax coow lu bari.
|
Les pensées du capitaine Blood ont été interrompues par une commotion.
|
Baaxul!
|
Ça ne va pas!
|
Sama xariti mag ju jigeen ji amul baay, tay Dibéer la.
|
Les amis de ma sœur orpheline, c'est dimanche.
|
Ndox mi di na dugg ndànkk-ndànkk ci biir suuf si, nekk luy jox ñax mi anam u magg bu baax.
|
L’eau pénétrait lentement dans le sol, créant des conditions de croissance idéales pour le fourrage.
|
Soo sëggal sa wóom.
|
Quand vous pliez le genou.
|
Danu wara génn.
|
Il faut qu'on sorte.
|
Suma fa nekkoon damaa dee
|
Si je n'avais pas été là, je serais mort.
|
Atlantaa, baax ci sàmpiyonaa waaye tële ci sàmpiyoŋ ligg, denc pàccam bu jëkk ci joŋante bi.
|
L’Atlanta, bien en championnat mais mal en point en Champion’s league, engrange son premier point de la compétition.
|
Sudee nanguwul sama laaj.
|
Si vous n'acceptez pas mon défi.
|
Fileek ñoo ngi sonn di fay boor, duñu mën a am paj mbaa njàng mu baax.
|
Tant qu’ils s’échinent à rembourser, ils ne peuvent s’offrir un bon système médical ou éducatif.
|
Xeex bi daf may jaaxal ba ci sama yax.
|
La lutte m'inquiète à mort.
|
Dinaa la wax lépp.
|
Je vais tout te dire.
|
000 farãa wala benn ci ñaari daan yooyu rekk.
|
000 de francs ou de l’une de ces deux peines seulement.
|
Ci saasi, lépp dellusi ci moom.
|
En un éclair, tout lui est revenu.
|
Tay la gëna tàng juróomi degre.
|
Aujourd'hui, il faisait cinq degrés de plus que d'habitude.
|
Ci noonu la mbir yu am solo di jaar ci sa xel.
|
Et puis des chocs soudains de la réalité passent dans votre esprit.
|
Sama pàppa la woon.
|
C'était mon père.
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.