Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
score
float32
1.04
1.23
Swahili
stringlengths
9
497
Wolof
stringlengths
10
448
1.230188
Ndiyo sababu mmeona na kusikia miujiza hii.'
Loolu moo tax ngeen gis te dégg kéemaan yii. '
1.212929
mnasema kweli katika madai yenu kwamba Mola wenu Mlezi anahuisha wafu kwa
(29) Texawal ne dëgg gii ca sa Boroom la bawoo.
1.209864
'Noa alifanya kulingana na mambo yote ambayo Mungu alikuwa amemuamuru.
Nóoyin def na lépp li ko Yàlla santoon.
1.204184
Kwa nini tunahitaji ulimwengu mpya?
Lu tax ñu soxla àddina su bees ?
1.202814
Kwa nini tunahitaji ulimwengu mpya?
Lu tax ñu soxla àddina su bees?
1.202532
48 Ninyi ni mashahidi wa mambo hayo.
48 Yéenay samay seede.
1.199757
katika shauri la kuangamizwa kaumu Lut'.
Lot ne ca xiiñidxaapaʼ bizuubacaʼ diidxaʼ ne bixooñecaʼ de Sodoma.
1.197516
Hakikaa au huon?
il est ici [ee lay tee see] or [ee lay ee see]
1.197255
Mamilioni Watahudhuria Je, Wewe Utakuwapo?
Ay Millioni nit dina ñu teew - Ndax Yaw dinga teew?
1.194309
wala hawatajifunza vita tena.
te dootuñu jàngati xare.
1.19259
18:21 Kwa nini waniuliza mimi?
18:21 Lu tax nga may laaj?
1.191107
Wamfuru (suba)
Waaye ci ñi gëmul, nag:
1.19088
Waliobaki ni Noa peke yake na wale waliokuwa pamoja naye ndani ya safina.
Nóoyin rekk a des, moom ak ña àndoon ak moom ca gaal ga.
1.190785
Basi wakaenda katika mji ambao mtu wa Mungu alikuwamo.
Ñu jubal ca dëkk ba góoru Yàlla ga nekk.
1.189598
Kwa hiyo, jamaa ya Nuhu ilikuwa yenye watu nane.
Kon njabootu Nóoyin, juróom-ñetti nit la woon.
1.188695
Unajua Paulo anamwambia Timotheo nini?
Ndax xam nga lan la Pool di wax Timote ?
1.183919
Huko ni kuwazulia wema waliotangulia (رحمهم الله).
Maam ya, seen ngëm a tax ba Yàlla seedeel leen lu baax.
1.183818
Malaika wawili walimwonya Lutu juu ya jambo gani?
Lan la ñaari malaaka yëgal Lóot ?
1.183298
Ufalme yangu ni hapa.
Sama nguur nekk fii.
1.183032
na kila jicho litamwona,
waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.
1.182737
Na hakuna tofauti kati yao (hizo ardhi) isipokuwa katika mambo mawili tu.
Kon suuf desatutoon su ñu xamutoon su dul [[Ostrali]] ak ñaari [[dott]] yi " .
1.182348
UNAMJUA mwanamke huyu mzuri anayekuja kumlaki Daudi?
NDAX xam nga jigéen bu rafet biy fekksi Daawuda nii ?
1.181069
Mariamu afanya haraka kumtembelea Elisabeti.
Maryaama daldi gaaw a dem seeti Elisabet.
1.18033
Na wapo miongoni mwao wanao kusikiliza; na tumezitia
Dinan leen déglu, diisook ñoom, xool ni nuy dëppalee sunuy xalaat.
1.179582
"Ujuzi wa kweli" umekuwaje mwingi katika hizi "siku za mwisho"?
Naka la " xam-xam dëgg " baree ci " muju jamono " jii?
1.179487
16:9 Je, hamjaelewa bado?
16:9 Ndax xamaguleen ba tey?
1.179286
5:30 maana sisi ni viungo vya mwili wake.)
5:30 ndaxte noo di céri jëmmam.
1.178182
Ni uovu mno iliyo kuamrisheni imani yenu ikiwa ni wenye kuamini.
22 Te lépp lu ngeen laaj cig ñaan, bu ngeen ci boolee ngëm, dingeen ci jot."
1.178038
Sulemani atafanya nini?
Lan la Suleymaan di def nag ?
1.17736
"[Mungu] atafuta kila chozi kutoka katika macho yao."
te Yàlla dina fomp bépp rongooñ ci seeni bët."
1.176616
Yakobo akakaa naye kwa muda wa mwezi mmoja.
Yanqóoba toog na fa ak moom lu mat weer.
1.175372
Mungu wa kweli ndiye Muumba wa vitu vyote.
Yàlla dëgg ji moo sàkk lépp.
1.174917
Lakini huwapa kisogo watu watendao maovu."
waaye day dàq ñiy def lu bon."
1.174443
Basi, wakamtukuza Mungu kwa sababu yangu.
te ñuy sant yàlla ci man.
1.174299
Bila shaka Sisi Tumewajaalia mashetani kuwa rafiki za wale wasioamini.
Nu degg seytaan ni muy jahasee nit yi.
1.173952
6:17 Lakini aliyejiunga na Bwana huwa roho moja naye.
6:17 Waaye nag kuy ànd ak Boroom bi, xel yi dañuy booloo, nekk benn.
1.173367
nazo ni T'a na Ha, ili kupingana na makafiri wanao kanya, na kuwa kama
Noonu lay deme ak ñiy weddi ak aji gëm yi.
1.172466
24:42 Wakampa kipande cha samaki wa kuokwa.
24:42 Ñu jox ko dogu jën wu ñu lakk.
1.17119
Wewe ni Mwingi wa Rehema."
Li nuy wax kay mooy yaw yaay kiy yërëm jirim."
1.170821
Je, baba yangu yuko hai?'
Mbaa sama baay a ngi dund?"
1.170639
Kwa nini wanafunzi wanaogopa usiku, na Petro anafanya nini?
Lu tax taalibe yi tiit ci guddi gi, te lan moo dal Piyeer ?
1.169989
Basi, Bwana akaendelea kusema, "Sikieni jinsi alivyosema huyo hakimu mbaya.
18:6 Boroom bi tegaat ca ne: "Dégluleen bu baax li àttekat bu bon boobu wax;
1.169871
Unaweza kumukaribia Mungu, kama tu unamutegemea, na kuwa na imani kwake.
Mën nga jege Yàlla bu dee wóolu nga ko te am ngëm ci moom.
1.16935
Wataweza kuwafufua waliokufa?
Ndax ñi dee dinañu mas a dekki?
1.169265
Basi Allaah Alimfisha miaka mia; kisha Akamfufua.
Yàlla daldi koy rey moom lu tollu ci téeméeri at.
1.168808
48 Ninyi ni mashahidi wa mambo haya.
48 Yéenay samay seede.
1.16864
Familia ya Nuhu ilikuwa na watu wangapi, na wanawe watatu waliitwa nani?
Njabootu Nóoyin, ñaata nit lañu woon, te ñetti doomam yu góor, naka lañu tuddoon ?
1.168569
Je, utawaweka katika mkono wa Israeli?"
Ndax dinga leen teg ci loxol Israyil?"
1.168394
18:41 "Unataka nikufanyie nini?"
18:41 "Loo bëggoon ma defal la ko?"
1.168347
WAVULANA wawili hapa ni tofauti sana, sivyo?
ÑAARI xale yi ñuy wone fii, niroowuñu, du dëgg ?
1.167516
Kwa nini Lutu alichagua kuishi Sodoma?
Lu tax Lóot tànn Sodom ngir dëkk fa ?
1.167363
Hakika Mola wangu Mlezi yupo karibu, anaitikia maombi. ***
(35) Te nag Yàllaay sama Boroom, di séen Boroom: "Jaamuléen ko.
1.166976
20:3 ambako alikaa kwa miezi mitatu.
20:3 toog fa ñetti weer.
1.166818
5:7 Basi, msishirikiane nao.
5:7 Kon nag buleen séq ak ñoom dara.
1.166685
Ukiwa hivyo, Mungu atakubariki wewe pia.
Boo defee loolu, Yàlla dina la barkeel lool yow itam.
1.1661
Nao walipoziona bahasha za fedha zao, wao na baba yao waliogopa.
Ba ñu gisee mbuusi xaalis ya, ñoom ak seen baay, dañoo tiit.
1.166007
Na sisi tunawahubiri habari njema ya ahadi ile waliyopewa mababa,
te nu ngi leen di xamal xebaar bu baax ne leen, li yàlla digoon sunuy maam,
1.165915
Wataweza kuwafufua waliokufa?
Ndax ñi dee dinañu mas a dekki ?
1.164305
36 "Mfalme atafanya apendavyo.
36 "Buur bi dina def lu ko soob.
1.164146
UNAWAJUA wanaume hawa ambao Yakobo anazungumza nao?
NDAX xam nga ñan la Yanqóoba di waxal fii ?
1.163875
17 wala njia ya amani hawaijui."
17 Xamuñu yoonu jàmm,
1.163772
Lakini mtu mmoja alimchukia.
Waaye amoon na ku ko bañoon.
1.163485
Kwa nini Mfalme Ahasuero anataka mke mpya, na anamchagua nani?
Lu tax buur Asuerus bëgg a takk beneen jabar, te kan la tànn ?
1.163431
Hakika mume wangu sasa atanipenda."
Léegi sama jëkkër dina ma bëgg."
1.163222
48 Nanyi ndinyi mashahidi wa mambo haya.
48 Yéenay samay seede.
1.162876
Mwambie Farao mfalme wa Misri kila kitu nikuambiacho."
Nanga wax Firawna buuru Misra, li ma lay wax lépp."
1.162694
Nikiwaacha waende nyumbani wakiwa na njaa watazimia njiani, maana baadhi yao wametoka mbali."
Su ma leen yiwee ak seen xiif, dinañu tële ci yoon wi, ndaxte am na ñu jóge fu sore."
1.162591
Je, unataka kuishi hata baadaya kufa?
Ndax bëgg nga dund gannaaw de ?
1.162391
Kwa kuwa katika saa moja hukumu yako imekuja. "
Ci wenn waxtu rekk la sa àtte dikk!"
1.162388
Kutoka huko atakuja kuwahukumu walio hai na wafu.
fa la di jóge àttesi ña di dund ak ña dee.
1.161809
Na ikiwa nitarudishwa kwa Mola wangu Mlezi, bila ya shaka nitapata marejeo bora zaidi kuliko haya. ***
Te sax bu ñu ma delloo sama Boroom danaa fa fekk dellluwaay bu gën bii ."
1.161765
Hukumu yako imekuja katika saa moja!'
Ci wenn waxtu rekk la sa àtte dikk!"
1.161745
19:21 kwa maana niliogopa kwa sababu wewe ni mtu mkali.
19:21 Dama laa ragaloon, ndaxte ku néeg nga.
1.161398
5 Kwa maana je, sivyo ilivyo nyumba yangu kwa Mungu?+
5 Du nii la sama waa kër def ak Yàlla?
1.161311
(6) Ni rehema itokayo kwa Mola wako Mlezi.
(95) "Loolu yërmande ju tukkee ca sa Boroom la.
1.161058
19 Ufalme wa Mungu utatimiza nini kupitia Har-Magedoni?
19 Lan la Nguuru Yàlla di def jaare ko ci xeexu Armagedon?
1.161
"Rafiki" watatu walimtembelea.
Ñetti xaritam ñów seetsi ko.
1.160925
Tunaweza kujifunza somo gani kutokana na kisa cha mke wa Lutu?
Lan lañu mën a jàng ci li dal jabaru Lóot ?
1.160639
Lakini, mtu yeyote anayenikana mbele ya watu, naye atakanwa mbele ya malaika wa Mungu.
9 Waaye ku ma gàntu ci kanam nit ñi, dinañu la gàntu ci kanam malaakay Yàlla yi.
1.160622
Major Mama Fail.
Big mom fail.
1.160609
Nuhu akafanya kama Mungu alivyosema.
Nóoyin wax na leen li Yàlla bëggoon a def.
1.160457
Alikuwa Mfalme kwa karibu miaka 50.
Nekkoon na buur lu mat 40 at.
1.16027
Farao akasema, Uende, ukamzike baba yako, kama alivyokuapisha.
Mu ne kon, na ko Firawna may, mu robi baayam, ni mu ko ko giñloo woon, te délsi.
1.160183
Wakati wao na baba yao walipoona mifuko ya fedha, wakaogopa.
Ba ñu gisee mbuusi xaalis ya, ñoom ak seen baay, dañoo tiit.
1.159703
LK 24:42 Wakampa kipande cha samaki wa kuokwa.
24:42 Ñu jox ko dogu jën wu ñu lakk.
1.15942
Naye atakuambia utakalofanya."
Moom dina la xamal li nga wara def."
1.159296
ambao hawataona kamwe nuru ya uzima.
ña dootu gis ug leer ba fàww.
1.159248
Musa anamwambia Kora na wafuasi wake 250 wafanye nini?
Lan la Musaa wax Kora ak 250 nit ñi ko toppoon ?
1.158858
Mtakapokimbilia mijini mwenu, nitatuma tauni katikati yenu, nanyi mtatiwa mikononi mwa adui zenu.
Bu ngeen làqoo ci seeni biir dëkk yu mag sax, maay wàcce mbas ci seen biir, seeni noon jekku leen.
1.158774
15 yeye ambaye huumba mioyo yao wote,
15 Moo tabax seen xol, ñoom ñépp;
1.158678
1:2 mpaka siku ile alipochukuliwa mbinguni.
1:2 ba ci bés, ba ko Yàlla yéege ci asamaan.
1.158303
Kwa jua na mchanga wenye rutuba uliopandwa;
de la sunna et la communauté [ Ahl Sunna wa al Djama'a ],
1.158295
Je, wewe ni Elia?"
Ndax yaa di Ilyaas?"
1.158139
"Kwa Ajili ya Hili Nimekuja Ulimwenguni"
" Lii moo tax ma ñëw àddina "
1.158111
Lakini kwa nini Yusufu na Mariamu hawapo hapa pia?
Waaye lu tax Yuusufa ak Maryaama nekkuñu fi ñoom it ?
1.158011
Ninanawa mikono kabla ya kula.
Dinaa raxas samay loxo balaa may lekk.
1.157852
Hata kama ni nusu ya ufalme, utapewa."
Su doon genn-wàllu nguur gi sax, dees na la ko jox!"
1.157748
ni kwa wale wanaoogopa kufanya uchafu katika nyinyi na mwenyezimungu ni mwingi
ak yeen ñi ko ragal, mag ak ndaw."
1.157058
Kwa nini Yesu ni Mfalme anayefaa? - MARKO 1:40-42.
Lu tax Yeesu nekk Buur bi gën? - MÀRK 1:40-42.
1.156465
Kwa hiyo hakuhitaji kufa kwa ajili ya dhambi zake kwa sababu hakuwahi kutenda dhambi yoyote.
Kon soxlawul mu dee ngir ay bàkkaaram - ndaxte masul a bàkkaar.
End of preview. Expand in Data Studio

Swahili-Wolof_Sentence-Pairs Dataset

This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.

This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1

Metadata

  • File Name: Swahili-Wolof_Sentence-Pairs
  • Number of Rows: 156839
  • Number of Columns: 3
  • Columns: score, Swahili, Wolof

Dataset Description

The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:

  1. score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).
  2. Swahili: The first sentence in the pair (language 1).
  3. Wolof: The second sentence in the pair (language 2).

This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.

References

Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:

[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017

[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.

[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018

[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.

[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.

[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.

[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.

[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB

[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.

[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages

Downloads last month
14

Collection including michsethowusu/swahili-wolof_sentence-pairs