score
float32 1.04
1.24
| Kimbundu
stringlengths 10
478
| Wolof
stringlengths 10
478
|
|---|---|---|
1.243965
|
Mukonda Diabhu ua mi tulukila ni njinda iavulu, kuma muène uejiia kuila o thembu iê ia butu kia."
|
Ndaxte Seytaane wàcc na ci yéen, ànd ak mer mu tàng, ndaxte xam na ne, jot gi ko dese barewul."
|
1.234014
|
O ji-anju jambela Lote: 'Lenguluka!
|
Lii la malaaka yi wax Lóot: ' Gaawal !
|
1.23339
|
Ua mu ibhula, 'Eie ua mesena kuia kumoxi ni eme, ni Sila?'
|
Lii la koy laaj: ' Ndax dinga bëgg a ànd ak Silas ak man ?
|
1.233125
|
Kienhiki, kiene kia bhangele Noué kála kia mu tumine Nzambi.
|
Nóoyin def na lépp li ko Yàlla santoon.
|
1.232371
|
Eme nga kuehela ku i mona, maji kua-nda bokona-mu.'
|
Bàyyi naa la nga gis ko, waaye doo ci dugg. '
|
1.231623
|
Mukonda Nzambi ua k'ijiia kuma kizuua ki mu dia-ku, mua-nda kutona mesu mu sokela ni Nzambi, muijiia kiauabha ni kiaiibha."
|
5 Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon."
|
1.230769
|
Kioso kia zukama, muéne uixi: 'Eme ngi phang'enu, Zuze, mua ngi sumbisile mu Ijitu.'
|
Mu ne leen: "Man maay Yuusufa, seen rakk, ji ngeen jaayoon, ñu indi ma Misra.
|
1.229933
|
Né muene tat'etu, uejiia o kidi kiki.'
|
Sama baay ci boppam xam na loolu bu baax."
|
1.226362
|
Ene oso endele mu zuela ni Mozé: 'Mukonda diahi eie ua mu di ta ku thandu diet'oso?'
|
Ñooñu ñépp a ñów ci Musaa, ne ko: ' Lu tax nga yëkkëti sa bopp ci suñu kow ? '
|
1.226228
|
Satanaji uambe kuila ki kueji kala muthu ueji sidivila Nzambi ni henda ioso.
|
Seytaane dafa wax ne amul kenn kuy jaamu Yexowa ci kaw mbëggeel kese.
|
1.223606
|
U tena ngó ku zukama kua Nzambi, se u mu dielela mba u kala ni kixikanu kua muéne.
|
Mën nga jege Yàlla bu dee wóolu nga ko te am ngëm ci moom.
|
1.223592
|
Eie uejiia se o polofeta ihi?
|
Ndax xam nga lan mooy yonent ?
|
1.207723
|
Ia lungu ni kima kia bhiti ku diulu, tu tange: "Kala kiki, ku madiulu-phe tanenu-ku, ni enu oso mua tunga momo!"
|
Lii lañuy jàng ci li xewoon ca asamaan: "Looloo tax, na asamaan ak ñi ci dëkk bànneexu!"
|
1.205876
|
Se u tanga ibatulu itatu mba itanu mu kizuua, ua-nda tena kutanga o Bibidia ioso ku muvu umoxi.
|
Booy jàng ñett ba juróomi pàcc bés bu nekk, dinga jàng Biibël bi yépp ci benn at.
|
1.205042
|
Enu ue ki mu tena kubhikila Nzambi ni Mamunu (kilundu kia jimbongo)."
|
Mënuleen a boole jaamu Yàlla ak jaamu Alal."
|
1.204952
|
Mukonda diahi o maxibulu akexile ni uôma mu usuku, ni ihi ia bhitile ni Phetele?
|
Lu tax taalibe yi tiit ci guddi gi, te lan moo dal Piyeer ?
|
1.204269
|
Tat'etu iú ué hanji ni muenhu?'
|
Mbaa sama baay a ngi dund?"
|
1.201809
|
Mukonda diahi Lote ua solo ku tunga mu Sodoma?
|
Lu tax Lóot tànn Sodom ngir dëkk fa ?
|
1.19986
|
O kuila tat'etu uala hanji ku muenhu?'
|
Mbaa sama baay a ngi dund?"
|
1.19884
|
Kala ki a ki soneka, exi, Uaiuka ka moneka, né mutu umoxi; Roma 3:10
|
Moom la Mbind mi wax ne:"Ku jub amul, du kenn sax.
|
1.198141
|
O kuila tua-nda di ongeka ni athu a zolo Nzambi?
|
Ndax dinañu ànd ak ñi bëgg Yàlla?
|
1.194934
|
Nzambi ua solo akua Izalaiele phala ku kala jimbangi jê.
|
Yàlla tànnoon na waa Israyil ngir ñu nekk ay seedeem.
|
1.194793
|
Katula muhatu'ê ni an'ê aiadi, tundé-nu bhabha!'
|
Jëlal sa jabar ak sa ñaari doom yu jigéen te jógeleen fii ! '
|
1.194649
|
Mukonda diahi Mbalahamu ni Lote a di xisa?
|
Lu tax Ibraayma ak Lóot tàggoo ?
|
1.193855
|
Jezú wexile muthu wa yuka.
|
Yeesu nit ku mat la woon.
|
1.19382
|
'Nga mi dióndo, kana ku jibha o mona.
|
Ngir Yàlla, bul rey xale bi.
|
1.193695
|
TALA o mona-ndenge ua mu zuela ni adiakimi.
|
XOOLAL xale bi di waxtaan fii ak mag ñi.
|
1.192473
|
Ihi ia zuela Jezú kua manh'â, Madiia?
|
Lan la Yeesu wax yaayam Maryaama ?
|
1.192028
|
ué kuma Nzambi ua mu fukununa mu 'alunga, eie u buluka.
|
Waaye Yàlla dekkal na ko,
|
1.192013
|
O Bibidia i zuela: "Kizuu'okio-phe ni kithangana kiê, kana muthu ua k'ijiia, né ji-anju mu diulu, né o Mona, ki kale Tata muène ngó.
|
36 "Waaye bés booba walla waxtu wa, kenn xamul kañ lay doon; du malaaka yi ci kaw, du sax man Doom ji, waaye Baay bi rekk moo ko xam.
|
1.191039
|
O Bibidia i zuela: "Jezú uixi: Eme ngi njila, ngi kidi, ngi muenhu.
|
Yeesu ne ko, "Man maay yoon wi, maay dëgg te dund it man la.
|
1.190358
|
O ukunji uen'iú: O kubhana umbangi ua Njimbu Iambote ia kiadi kia Nzambi."
|
"Lii moo di kàdduy Waawu Yàlla ji, Seede bi wóor te dëggu, Ndeyu càkktéefu Yàlla ji.
|
1.18754
|
O Bibidia i zuela: "Jezú uixi: Eme ngi njila, ngi kidi, ngi muenhu.
|
6 Yeesu ne ko: "Man maay yoon wi, maay dëgg te dund it man la.
|
1.187077
|
(Dimatekenu 1:28) O ixi nuka a-nda i buika.
|
(Njàlbéen ga 1: 28) Suuf si du fi mas a jóge.
|
1.1862
|
EIE UA lembalala maka alungu ni mizangala itatu íii?
|
NDAX yaa ngi fàttaliku ñetti góor ñii ?
|
1.185581
|
O anumi a tokala ku zola ahatu'â, kála kia zola o mikutu'â. - Efezo 5:25-29.
|
Jëkkër yi dañu war a bëgg seen jabar ni ñu bëgge seen bopp. - Efes 5:25-29.
|
1.185156
|
O "Nzambi wedile ni Mon'ê mwène ka mu fikixila, maji wa mu bhakwile mukonda dya etu-ene-oso!," mukonda dya kiki, twala ni kidyelelu kya kwila, Nzambi wa-nda tu bhana "o ima yoso" ya kanena mwene.
|
32 Yàlla mi nu gàntulul Doomam waaye mu joxe ko, mu dee ngir nun, ndax dina nu bañalati dara?
|
1.184086
|
Davidi ua tambuijila, 'Eie u muhatu ua dimuka.'
|
Daawuda ne ko: ' Jigéen bu am xel nga.
|
1.183448
|
Mukonda dia kiki, mua mu mona ni kuívua o madiuanu enhá.'
|
Loolu moo tax ngeen gis te dégg kéemaan yii. '
|
1.183353
|
Muéne uambe: "O kuila eie uala ni kutena phala kufundisa muthu ni kuijiia se muéne hombo mba kana?
|
Mbaa ngeen naa: "Ana Yàlla jiy àtte dëgg sax?"
|
1.181874
|
Muéne ua solo 12 phala ku kala jipoxolo jê.
|
Tànn na ci 12 ngir ñu nekk ay ndaw.
|
1.181465
|
Allah kare tu bhi aa jaye....
|
ci Yàlla jiy dëgg la koy ñaane,
|
1.181079
|
O ana a tokala ku belesela o jitata jâ. - Efezo 6:1-3.
|
Xale yi dañu war a déggal seeni waajur. - Efes 6:1-3.
|
1.180787
|
Kienhiki Saúlu uebhula: 'Ihi nga tokala ku bhanga, Ngana?'
|
Sool laaj ko: ' Lan laa war a def, Sang bi ? '
|
1.18075
|
Eie uejiia se ihi iambe Phaulu kua Timote?
|
Ndax xam nga lan la Pool di wax Timote ?
|
1.180694
|
Kienhiki Mozé uixi: 'Kiki-phe mua-nda kuijiia se Jihova ua-nda sola nanhi.
|
Musaa ne leen: ' Léegi dingeen gis kan la Yexowa di tànn.
|
1.180407
|
Lembalala kuma, Phaulu ua bhitile mivu iiadi mu kaleia, mu Sezaleia.
|
Yaa ngi fàttaliku ne Pool toog na kaso ñaari at ca Sesare.
|
1.180253
|
A-nda kala mu Palayizu,
|
ci biir réewum aji dund ñi.
|
1.180038
|
Bhenhobho, jianju javulu ja moneka ku diulu, exi: 'Fuma i kale ia Nzambi mu diulu, o mu ngongo uembu mua'xaxi ka athu oso a mu uabhela.'
|
Yàlla, ca kaw la nekk, maanaam ca asamaan te foofu, malaaka yu koy jaamu, dañu mas a def coobareem.
|
1.17853
|
"Kiene ué ki Ng'ejila mu Ngongo"
|
" Lii moo tax ma ñëw àddina "
|
1.178422
|
Ubalongele oma ma kintinu kia Nzambi yo wuka mbevo zau.
|
Mu daldi leen jàngal lu jëm ci Nguuru Yàlla te faj ñi feebar.
|
1.177932
|
Ua tokala u mu ixana Jezú.'
|
Nanga ko tudde Yeesu. '
|
1.177267
|
EIE uejiia se o maiala iâ a mu zuela ni Jakobo, akua kuebhi?
|
NDAX xam nga ñan la Yanqóoba di waxal fii ?
|
1.176665
|
Ene a nhana ima ia tokalele kua Nzambi.
|
Dañu sàcc lu Yàlla moom.
|
1.176479
|
Kamba dietu ua-nda kazala.
|
Sa xarit bi takk na jabar.
|
1.176165
|
Mukonda diahi Nzambi ua bhangesa Adá kuia ku kilu kionene?
|
Lu tax Yàlla nelawloo Aadama, nelaw bu xóot ?
|
1.175678
|
Mu fikula, a nanhi o maiala aiadi ala ni Mozé?
|
Ñaari góor ñi nekk ak Musaa, ñan lañu?
|
1.175255
|
Ihi i u banza? - Tanga 1 Nzuá 3:10-12.
|
Loo ci xalaat? - Jàngal 1 Yowaana 3: 10- 12.
|
1.174664
|
Né muéne se ene oso a ku lenga ni ku-kuxa, eme ki nga-nda ku lenga ni ku kuxisa.'
|
Miskin yaa ngi ak yéen bés bu nekk, waaye dungeen ma gis ba fàww."
|
1.174587
|
"O kidi mua-nda ku k'ijiia, o kidi anga ki mi bhana ufôlo." - Nzuá 8:32.
|
Yeesu nee na: " Dingeen xam dëgg gi te dëgg gi dina leen goreel [maanaam dina leen yewwi]. " - Yowaana 8:32.
|
1.174407
|
Kuma iá ene o manhinga mami, ma di zunza mukonda dia mundu phala kuloloka o ituxi.
|
26:28 ndaxte lii sama deret la, ji fas kóllëre gi, te mu tuuru, ngir ñu bare jot mbaalug bàkkaar yi.
|
1.173885
|
Maji mu ola ia ukaza, uejiia ihi ia bhitile?
|
Waaye bi bésu séy bi jotee, xam nga lan moo xew ?
|
1.173394
|
O Nzambi ia kexile mu bheza ua zuelele né, ua mu tukulukile bhu kaxi ka anju!
|
Bu Yàlla xajoon ciy kàddu, ñu xam ko.
|
1.173364
|
Enu ue ki mu tena kubhikila Nzambi ni Mamunu (kilundu kia jimbongo)."
|
Manuleena jaamoondoo Yàlla ak Alal."
|
1.173349
|
Ki mua kijiia kuma Eme nga bhingi ngi kala m'onzo ia Tat'etu?'
|
Xamuleen ne sama kër Baay laa wara nekk?"
|
1.17331
|
"O muenhu ua kidi" ihi, ni mukonda diahi o kidielelu kiki kia uabha?
|
Lan mooy " dund gu wóor gi ," te lu tax mu nekk yaakaar bu neex ?
|
1.172679
|
"Muthu n'a fu, mbé ua ka kala dingi ni muenhu?
|
Ndax nit ku dee dina mën a dundaat ?
|
1.172506
|
Mon'ê uala ni muenhu.'
|
Sa doom faatu na. '
|
1.172335
|
Nundu onthe ala matongoeaw'a ni Veva wa Ngai, asu ni o ana ma Ngai.
|
14 Ndaxte ñépp ñiy déggal Xelu Yàlla mi, ay doomi Yàlla lañu.
|
1.172315
|
Mbote iebhi i tu katula mu kuxinganeka mu Mak'â Nzambi izuua ioso?
|
Ban njariñ moo nekk ci topp Kàddu Yàlla bés bu nekk ?
|
1.172007
|
mãe de kixikila,
|
Waaye ci ñi gëmul, nag:
|
1.172002
|
Nzambi uambela Noué.
|
Nóoyin wax na leen li Yàlla bëggoon a def.
|
1.171446
|
Maji xalenu mu kijiia, kuila se mu ngi jibha, mua-nda jibha diiala ki dia te kituxi.'
|
Waaye nangeen xam lii: Boo leen ma reyee, nit ku deful dara lu bon ngeen di rey. '
|
1.171074
|
O kuila eie uejiia o dijina dia diiala dia dianga?
|
Ndax xam nga turu Yàlla ?
|
1.170483
|
Bhenhobho Diabhu anga u mu xisa, o ji-anju anga jiza, a bhana kudia kua Jezú.
|
noonu seytaane bàyyi ko. te ay malaaka daldi ñëw fi yeesu, di ko topptoo.
|
1.170032
|
O Jikidistá a dielela ni muxima uoso mu kikanenu kia difukunukinu, kiki kiene mu a kuatekesa.
|
16 Kon nag dige Yàlla boobu, ngëm moo ko waral, ngir mu di aw yiw doŋŋ.
|
1.169866
|
Nanhi ua bhange o diiala dia dianga, ni dijina diebhi dia mu luku?
|
Kan moo sàkk góor gu jëkk gi, te naka la tuddoon ?
|
1.168305
|
Mabhebhu ahi a kauana, a katanu, ni ia kasamanu?
|
Lan moo xewoon ci ñeenteel, juróomeel ak juróom-benneelu musiba yi?
|
1.16696
|
Kiene kimoxi ué, Nzambi ua bhange kima phala kudimuna o athu ande dia kubheka o dizubhilu.
|
Ngir yàlla wonendil laataa ngay denc.',
|
1.166881
|
Kiki kiexile kikalakalu kiavulu, mukonda kua kexile athu avulu akexile mu bheza jinzambi ja makutu.
|
Liggéey bu réy la ndaxte ñiy jaamu yàlla yu dul dëgg yi bare nañu lool.
|
1.16682
|
Enu ue ki mu tena kubhikila Nzambi ni Mamunu (kilundu kia jimbongo)."
|
Manuleena boole jaamu Yàlla ak jaamu Alal."
|
1.166435
|
Mivu ikuxi ia kexile na-iu Mozé kioso kiafú?
|
Ñaata at la Musaa amoon bi mu deewee?
|
1.16642
|
Ene anaie iauna,
|
Jëfeleen nag ni niti leer.
|
1.16633
|
Kienhiki, muéne uala mu njila ia Damásku.
|
Léegi mu ngi ci yoonu Damas.
|
1.166265
|
Mu kusukáko, Jona uambe: 'Eme ngi mubhezi ua Jihova o Nzambi ia bhange o diulu ni ixi.
|
Lii la leen Yunus mujj a wax: ' Man, Yexowa laay jaamu, Yàlla mi sàkk asamaan ak suuf.
|
1.166093
|
Kua noko 40 a Izuua ni 40 a usuku.
|
Taw na 40 bëccëg ak 40 guddi.
|
1.16607
|
Ngolokela iahi ia bhele o anju jiiadi kua Lote?
|
Lan la ñaari malaaka yëgal Lóot ?
|
1.165798
|
An'â Noué a vualele ana avulu.
|
Doomu Nóoyin yi amoon nañu doom yu bare.
|
1.165533
|
Thembu kuxi, ni kiebhi kia tokala ku i bhanga?
|
Kañ lañu koy def ak naka lañu ko war a defe?
|
1.165368
|
Mu dijina dia Jezú emana ni uende!'
|
Ci turu Yeesu, jógal te dox ! '
|
1.165206
|
Saí athu a kamúkua nange a fikisa ku tu fidisa ku zuela maka alungu ni utuminu ua Nzambi.
|
Mën na am ay nit jéem ñu tere wax ci nguuru Yàlla.
|
1.164812
|
Mba ua mu bhinga mbiji, u mu bhana nhoka?
|
10 Walla mu ñaan la jën, nga jox ko jaan?
|
1.164499
|
Ye jo jindagi ki kitab hai,ye kitab bhi kay kitab hai,
|
Ñu daldi ubbi ay téere, ubbi itam beneen téere, téereb dund bi.
|
1.164264
|
Thembu kuxi, ni kiebhi kia tokala ku i bhanga?
|
Kañ lañu koy def ak naka lañu ko war a defe ?
|
1.163573
|
Kienhiki, Madiia ua lenguluka múia mu kunda Nzebele.
|
Maryaama daldi gaaw a dem seeti Elisabet.
|
1.163539
|
"O kidi mua-nda ku k'ijiia, o kidi anga ki mi bhana ufôlo." - Nzuá 8:32.
|
Yeesu nee na: " Dingeen xam dëgg gi te dëgg gi dina leen goreel [maanaam dina leen yewwi]. " - Yowaana 8:32.
|
1.162737
|
A tokala uê ku a bazela ni ku a bhana milongi.
|
Soxla nañu yar ak jubbanti.
|
1.162717
|
Se Adá ka dile ku kibundu keji londekesa ngó kuila ua belesela, maji ueji londekesa ué ua sakidila o Mubhangi uê ua mu bhanene ima iavulu iambote.
|
12 Ndax liggéey bi ndimbal lii laaj kat, yemul rekk ci faj soxlay ñu sell ñi, waaye itam dina baawaanal cant gu bare, ñeel Yàlla.
|
1.162714
|
Di longe kiebhi kia mu kuatekesa ku makamba mê.
|
Seetal ni ko xaritam yi dimbalee woon.
|
1.161583
|
Ihi ia tumina Mozé kua Kola ni 250 a akaiedi'ê ku bhanga?
|
Lan la Musaa wax Kora ak 250 nit ñi ko toppoon ?
|
Kimbundu-Wolof_Sentence-Pairs Dataset
This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.
This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1
Metadata
- File Name: Kimbundu-Wolof_Sentence-Pairs
- Number of Rows: 13730
- Number of Columns: 3
- Columns: score, Kimbundu, Wolof
Dataset Description
The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:
score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).Kimbundu: The first sentence in the pair (language 1).Wolof: The second sentence in the pair (language 2).
This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.
References
Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:
[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017
[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.
[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018
[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.
[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.
[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.
[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.
[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB
[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.
[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages
- Downloads last month
- 8