score
float32 1.04
1.25
| Ganda
stringlengths 10
500
| Wolof
stringlengths 10
489
|
|---|---|---|
1.248092
|
9 (Naye ekigambo ekyo nti Yalinnya, kigamba ki wabula okugamba nti era yakka mu njuyi eza wansi ez'ensi?
|
9 Su nu waxee ne "yéeg na," li moo ci génn: daa jëkka wàcc ba ca bérab ya gëna suufe.
|
1.24332
|
6 Awo Mukama waffe n'agamba nti, "Muwulire omulamuzi atali wa mazima bw'agamba.
|
18:6 Boroom bi tegaat ca ne: "Dégluleen bu baax li àttekat bu bon boobu wax;
|
1.23911
|
Olina Ebibuuzo Bye Weebuuza?
|
am nga ay laaj?
|
1.230142
|
Naye era nja kukuwa ne by'otasabye, obugagga n'ekitiibwa.'
|
Dinaa la may itam li nga ñaanul, maanaam alal ak ndam. '
|
1.225363
|
34 Kubanga ani eyali amanye ebirowoozo bya Mukama? oba ani eyali amuwadde amagezi?
|
mbind mi dafa ne:"ana ku xam xalaatu boroom bi?ku ko doon digal?"
|
1.221791
|
OKUSHABA: Taata, ekigambo kyaawe n'amazima.
|
samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. sa kàddu mooy dëgg.
|
1.213117
|
ajje nno gye ndi, kale anaamanya nga mu Isiraeri mulimu nnabbi.
|
Dina xam ne yonent a ngi ci Israyil."
|
1.209231
|
Oh dear, bye bye more money.
|
Waaaay more money.
|
1.208516
|
Naye ffe tuli bayigirizwa ba Musa.
|
Nun, taalibey Musaa lanu.
|
1.20672
|
4Omuntu ow'okweha ekitinwa ekyo tabayo, manya Ruhanga n'iwe amweta nk'okwo yayesire Aroni.
|
Kenn mënul a teral sa bopp ba doon ab saraxalekat, su dul ne Yàllaa la woo, ni mu ko defe woon Aaroona.
|
1.199636
|
28"Kandi nukwo kyabaire n'omu biro bya Loti.
|
28 "Dina mel it ni la xewoon ca bési Lóot.
|
1.199319
|
30 Era, laba, waliwo ab'oluvannyuma abaliba ab'olubereberye, era waliwo ab'olubereberye abaliba ab'oluvannyuma.
|
30 Noonu ñenn ci ñi mujj ñooy jiituji; te ci ñi jiitu, ñooy mujji."
|
1.197866
|
3611:36 nny 3Awo Abayudaaya ne bagamba nti, "Ng'abadde amwagala nnyo!"
|
11:36 Noonu nag, Yawut ya ne: "Gis ngeen ni mu ko bëgge woon!"
|
1.197378
|
14 Waliwo omulwadde mu mmwe?
|
14 Ana ku wopp ci yeen?
|
1.196541
|
era tewaliba n'omu aliwulira eddoboozi lye mu nguudo.
|
te kenn du dégg baatam ci mbedd yi.
|
1.192094
|
olimalayo ennaku musanvu ndyoke njije gy'oli nkutegeeze by'oba okola.
|
Juróom ñaari fan nag ngay négandiku, ba ma fekksi la fa, xamal la looy def."
|
1.184874
|
Bonna balikaddiwa bayulike ng'ekyambalo;
|
dinañu màggat ñoom ñépp ni ay yére.
|
1.184734
|
Nabali akabugha athi: 'Sinangaha ebyalya byaghe by'abalhume abali ng'inywe.'
|
Nabal ne leen: ' Duma jox sama lekk ay nit ñu mel ni yéen. '
|
1.183289
|
17 Isiraeri n'alyoka ayimba oluyimba luno:
|
17 Ca la Israyil woy woy wii:
|
1.179291
|
10 nga bwe kyawandiikibwa nti Tewali mutuukirivu n'omu;
|
Moom la Mbind mi wax ne:"Ku jub amul, du kenn sax.
|
1.17923
|
Mwalokolebwa lwa kisa.
|
Ci kaw yiw daal ngeen mucce.
|
1.178644
|
Mu nkomerero Sulemaani ayogera: 'Totta mwana!
|
Suleymaan daldi wax lii: ' Bul rey xale bi !
|
1.177955
|
6 yagezaako okwonoona yeekaalu: ne tumukwata,
|
6-7 Kër Yàlla ga sax jéem na koo teddadil, noo ko jàpp.
|
1.177252
|
21Obanga ddala mwamuwulira, era ne muyigirizibwa mu ye ng'amazima bwe gali mu Yesu, 224:22 a 1Pe 2:1 b Bar 6:6kale mwambulemu obulamu obw'omuntu ow'edda, avunda olw'okwegomba okw'obulimba.
|
21 Ndax yaakaar naa ne dégg ngeen Kirist te jàng ngeen ci moom, ba xam dëgg gi Yeesu ëmb.
|
1.176808
|
Obuuza kuseka!
|
ñ paro de rir!
|
1.176269
|
i kika le kyokemutyibilapo banwe bene mambo a byobya byoloke? 58 Kimfwa, pomwenda na
|
"Lu tax it dungeen àtteel seen bopp liy jëf ju jub?
|
1.176235
|
yeeba yeeba it's friday!
|
yaaaay It's friday!
|
1.175103
|
18 Oyinza otya okusemberera Katonda?
|
Naka nga mënee jege Yàlla ?
|
1.174948
|
Omanyi amakulu g'erinnya lya Katonda?
|
Ndax xam nga turu Yàlla ?
|
1.174693
|
Buli wemulaba nga tambula mpola,
|
waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.
|
1.174271
|
Laba Emeere!
|
Xoolal li xew léegi !
|
1.173929
|
nga bw'okolera bulijjo abo abaagala erinnya lyo.
|
ni nga baaxook ñi sopp sa tur.
|
1.173586
|
Yerusaalemi ye waka gwange.
|
Jeerusalem nekk sama kër.
|
1.172876
|
48 Mmwe bajulirwa b'ebyo.
|
48 Yéenay samay seede.
|
1.172695
|
30 Naye Katonda n'amuzuukiza mu bafu:
|
Waaye Yàlla dekkal na ko,
|
1.172676
|
9 (Naye ekigambo ekyo nti Yalinnya, kigamba ki wabula okugamba nti era yakka mu njuyi eza wansi ez'ensi?
|
4:9 Su nu waxee ne "yéeg na," li moo ci génn: daa jëkk a wàcc ba ca bérab ya gën a suufe.
|
1.172561
|
18 Oyinza otya okusemberera Katonda?
|
Naka nga mënee jege Yàlla?
|
1.172414
|
Kiki kye tuyigira ku mukyala wa Lutti?
|
Lan lañu mën a jàng ci li dal jabaru Lóot ?
|
1.170652
|
22 Era abalala mubasaasirenga ababuusabuusa;
|
1:22 Jubbantileen ñi am werantey xel,
|
1.170114
|
24 Abayita mwesigwa, n'okukola ye alikola.
|
24 Ki leen woo de ku wóor la, te moo koy def it.
|
1.168903
|
21 N'abagamba nti Temunnategeera?
|
21 Noonu Yeesu ne leen: "Ndax seen xol dafa tëju ba tey?"
|
1.16803
|
3 Akabonero akalala ne kalabika mu ggulu.
|
3 Ci kaw loolu jeneen firnde feeñ asamaan.
|
1.16775
|
A: Enjoy your dinner, bye bye.
|
A: Enjoy dinner.
|
1.166978
|
Ono anaayitibwanga mukazi, kubanga ono aggyiddwa mu musajja.
|
Dees na ko tudde jigéen, ndaxte ci góor lees ko jële a ."
|
1.166937
|
EKIDDIBWAMU:Ayi Mukama, tusaasire, kubanga tuli boonoonyi.
|
[[[Aadama]] ak Awa] daldi ne: "Sunu Boroom, tooñ nanu sunu bopp.
|
1.166035
|
15 Kubanga aliba mukulu mu maaso ga Katonda.
|
1:15 ndaxte dina nekk ku màgg ca kanam Yàlla.
|
1.163233
|
'Ekyo kisoboka kitya?' bw'atyo Malyamu bw'abuuza.
|
Maryaama laaj ko lii: ' Naka la loolu mën a ame ?
|
1.160153
|
12Na nyowe ndibaganyira obubi bwabo, kandi ebibi byabu tindigaruka kubiijuka. " 13Ruhanga obu arukubaza ha ndagaano empyaka, buli naadibya eya ira.
|
Ndaxte dinaa leen baal seeni tooñ,te dootuma fàttaliku seeni bàkkaar."
|
1.159723
|
Mweyawule ku mawanga agabeetoolodde era muleke n'abakazi bannamawanga."
|
Teqlikooleen ak xeeti réew mi, teqlikook jigéen ñii diy jaambur."
|
1.159305
|
17 Haine eki abaana barikubaasa kwega ahari Yesu?
|
17 Ndax am na li xale yi mën a jàng ci Yeesu?
|
1.158392
|
9 (kubanga ebibala by'omusana biri mu bulungi bwonna n'obutuukirivu n'amazima),
|
Leer, mbaax lay meññ, njub ak dëgg.
|
1.158297
|
Mbwenu okaayetenga ngu n'okumumanya omumanye?
|
Ndax dinga bëgg xamante ak moom sax ?
|
1.158264
|
Abaffe empera y'okukola obulungi (eyinza okuba ekintu ekirala kyonna) okugyako okusasulwa obulungi.
|
yool b-: fey. jëf ju baax joo def rekk, borom bi dina la ci yool.
|
1.158169
|
"Omuntu bw'ampeereza, angobererenga; nange gye ndi, eyo omuweereza wange naye gy'anaabanga: omuntu bw'ampeereza, Kitange alimussaamu ekitiibwa."
|
Ku bëggga doon sama surga, na ma topp, bu ko defee, fu ma nekk, fa lay nekk moom itam.
|
1.157932
|
Temumanyi nti omuntu ali nga nze asobola okuvumbula kye mukoze?"
|
Xanaa xamuleen ne nit ku mel ni man day gisaane?"
|
1.157925
|
Nâbajirira nk'oku olugendo lwâbo lunakwânîne, nabatwîra emanja nk'oku emanja zâbo zinali, na ntyo banamanya oku nie Nyamubâho.
|
te dina daje ak mbugal ndaxte fecci na kóllëre.
|
1.157123
|
3 Alina essanyu oyo asoma mu ddoboozi eriwulikika ebigambo by'obunnabbi buno, n'abo ababiwulira era abakwata ebintu ebiwandiikiddwa mu bwo,+ kubanga ekiseera ekigereke kiri kumpi.
|
3 Barkeel ngeen, yaw miy jàng ak yéen ñiy déglu wax yii jóge ca Yàlla, te di sàmm li ñu ci bind, ndaxte waxtu wi jege na.
|
1.15702
|
7"Tobeeranga na bakatonda balala wabula Nze nzekka.
|
7 "Buleen am yeneen yàlla ci sama kanam.
|
1.15682
|
9 Naye bwe twatula ebibi byaffe, ye mwesigwa era mutuukirivu okutusonyiwa n'okutunaazaako obutali butuukirivu bwonna.
|
9 Su nu nangoo sunuy bàkkaar ci kanamam, fekk kuy sàmm kóllëre la te jub, ngir baal nu sunuy bàkkaar te sellal nu ci lépp lu jubadi.
|
1.156538
|
Lwaki Lutti yalondawo okubeera mu Sodomu?
|
Lu tax Lóot tànn Sodom ngir dëkk fa ?
|
1.155323
|
N'amuddamu nti, "Ssimanyi; nze mukuumi wa muganda wange?"
|
Mu ne ko: "Gisuma ko de; xanaa maa wara sàmm sama rakk?"
|
1.155095
|
6Omuntu nk'ogwo ekifubiro eki yaahairwe abaingi nikimara.
|
6 Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.
|
1.154604
|
Era buli lukya nneeyongera okuba omukakafu nti eno ye ddiini ey'amazima."
|
Te sama dige Booroom dëgg la."
|
1.154528
|
6 Najjukiranga ennyimba zange ekiro,
|
7 Guddi may fàttliku sama woy,
|
1.153097
|
Noteekwa kwemera enteekateeka erikugira ngu n'obu Ruhanga aine byingi ebitarikumanywa, akuhaire obushoboorozi narishi amaani gw'obwa Ruhanga kumanya ebitarikumanywa.
|
Yàlla, lumu def noonu la te jaam bu ko xam noppalu.
|
1.152579
|
18Bakabagambira bati: "Omu biro bya ha mpero halibaho abasekerezi abatatiina Ruhanga, abalemwa okwegomba kwabu okubi." 19Abo nubo abaleetereza okwebaganizaamu, bantu b'ensi abataina Mwoyo wa Ruhanga.
|
1:18 ne leen: "Muju jamono ay tiiñalkat dinañu feeñ, ñuy weddi Yàlla, ngir topp seen bakkan."
|
1.152059
|
'Muwala wo afudde.'
|
Sa doom faatu na. '
|
1.151187
|
Abamisiri baamala enaku nsanvu nga bamulira.
|
Waa Misra nag dëjal ko juróom ñaar fukki fan.
|
1.150962
|
7 Mujjukirenga abakulembeze bammwe abaababuulira ekigambo kya Katonda, nga mutunuulira empisa zaabwe nga mugobereranga okukkiriza.
|
7 Fàttlikuleen seen njiit, yi leen àgge kàddug Yàlla.
|
1.150854
|
Yakobo n'azaala Yuda ne baganda be.
|
Yanqóoba jur Yuda ak i doomi baayam;
|
1.150822
|
Quels enjeux pour 2015+ by gandibleuxmonia
|
Quels enjeux pour 2015+ gandibleuxmonia
|
1.150766
|
9Abantu boona bamureeba naagyenda kandi naahimbisa Ruhanga.
|
9 Mbooloo mépp gis ko, muy dox, di sant Yàlla.
|
1.15029
|
Kiki ekibaawo bakabona bwe bava mu Yoludaani?
|
Lan moo xew bi saraxalekat yi génnee Yurdan bi?
|
1.150253
|
3 Ekyo kye kirungi, ekikkirizibwa mu maaso g'Omulokozi waffe Katonda,
|
2:3 Loolu mooy li rafet te neex Yàlla sunu Musalkat,
|
1.150186
|
Ne bamuleeta eri Musa.
|
Ñu yóbbu ko ca Musaa.
|
1.150089
|
"Tubulire, ebyo biribeerawo ddi?
|
"Wax nu kañ la loolu di am?
|
1.149989
|
1Omuntu atukwate ati: Atubone tuli bakozi ba Kirisito mara bageleezi b'ebyebisho bya Ruhanga.
|
Nañu nu teg kon ay surgay Kirist, di ay jawriñ yuy xamle mbóoti Yàlla.
|
1.149711
|
1Omuntu atukwate ati: Atubone tuli bakozi ba Kirisito mara bageleezi b'ebyebisho bya Ruhanga.
|
1 Nañu nu teg kon ay surgay Kirist, di ay jawriñ yuy xamle mbóoti Yàlla.
|
1.149613
|
Neryo omw'ihiika lya Noa mwabya abandu munani.
|
Kon njabootu Nóoyin, juróom-ñetti nit la woon.
|
1.149431
|
n'atasaasira mwana eyava mu lubuto lwe?
|
Ndax du am yërmande ci doomam ji mu jur?
|
1.149384
|
Ne basaba Peetero agira abeera nabo okumala ennaku ntonotono.
|
Gannaaw loolu ñu ñaan Piyeer, mu toog ci ñoom ay fan.
|
1.149156
|
Yesu yayisa atya abaana abato, era kiki abaana kye beetaaga okuva eri bazadde baabwe?
|
Nan la Yeesu meloon ak xale yi, te lan la xale yi soxla ci seen waajur?
|
1.148873
|
8 "Kubanga ebirowoozo byange si birowoozo byammwe
|
8 "Samay xalaat déy du seeni xalaat,
|
1.148599
|
Yesu n'amuddiza nnyina.
|
Yeesu delloo ko yaay ja.
|
1.148134
|
"Mukama ani akkiriza bye tugamba?
|
"Boroom bi, ana ku gëm sunu waare?
|
1.147851
|
niki ekiiza okuikorra awooni na awantu awatatiire Katonda?"
|
luy doon muju ki weddi te dëng?"
|
1.147204
|
"Laba ntuma omubaka wange akukulembere,
|
"Maa ngii di yebal sama ndaw, mu jiitu la,
|
1.147124
|
16 Bagamba nti bamanyi Katonda, naye mu bikolwa byabwe bamwegaana.
|
" Dañoo mbubboo xam-xamu Yàlla, waaye seeni jëf weddi na ko. " - TIT 1:16.
|
1.146952
|
21 N'abagamba nti Temunnategeera?
|
Noonu Yeesu ne leen: "Ndax seen xol dafa tëju ba tey?"
|
1.146809
|
8 Si ye yali ekitangaala ekyo,+ naye yajja okuwa obujulirwa ku kitangaala ekyo.
|
1:8 Moom ci boppam du woon leer gi, waaye ñëw na ngir seedeel leer gi.
|
1.146544
|
15Yabaha obusobozi obw'okubinga emyoyo emibi.
|
3:15 mu joxaale leen sañ-sañu dàq ay rab.
|
1.145937
|
Hadith _Allah atusasula nga asinzirira ku niyyah zaffe Uploaded by Yusuf.Tib at Your Listen
|
Li wóor moo di, sunu Boroom mi ngi soqikoo ci giiru Yuda.
|
1.145567
|
"Mazima okubuulirira kubajidde okuva eri omulezi wammwe nokuwonya ebyo ebiri mubifuba." ([21])
|
(29) Texawal ne dëgg gii ca sa Boroom la bawoo.
|
1.145312
|
Ee kootap Israel, arwookyini age tugul eng' okweek ko uu ortinwekyik.
|
30 "Lii moo tax yeen waa kër Israyil, ma di leen àtte, ku nekk ciy jëfam.
|
1.145263
|
Kati lwaki tonaaba, nga bw'agambye?'
|
Lu tax mënoo ko def, ni mu la ko waxe ? '
|
1.145148
|
17 Era obubonero buno bunaagendanga n'abo abakkiriza: banaagobanga emizimu mu linnya lyange; banaayogeranga ennimi empya;
|
16:17 Ñi ma gëm dinañu ànd ak firnde yii: ci sama tur dinañu dàq rab yi, di wax làkk yu bees,
|
1.145005
|
7Tukiko naija kubagambira byona ebyambaireho.
|
7 Mboolem lu jëm ci man nag, Tisig dina leen ko xamal.
|
1.14493
|
15Mwerinde, hatabaho n'omu arukusubwa obukoonyezi bwa Ruhanga.
|
15 Moytuleen balaa kenn di ñàkk yiwu Yàlla.
|
1.144792
|
Yesu amanyi omusajja ono ky'alowooza.
|
Yeesu xam na li nit ki di xalaat.
|
1.144681
|
54 Awo ye n'abasajja be yali nabo ne balyoka balya era ne banywa; ne basulayo ekiro ekyo.
|
54 Ba loolu weesee mu doora lekk, daldi naan, moom ak ñi mu àndal.
|
Ganda-Wolof_Sentence-Pairs Dataset
This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.
This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1
Metadata
- File Name: Ganda-Wolof_Sentence-Pairs
- Number of Rows: 49136
- Number of Columns: 3
- Columns: score, Ganda, Wolof
Dataset Description
The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:
score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).Ganda: The first sentence in the pair (language 1).Wolof: The second sentence in the pair (language 2).
This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.
References
Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:
[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017
[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.
[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018
[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.
[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.
[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.
[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.
[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB
[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.
[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages
- Downloads last month
- 7