score
float32 1.04
1.24
| Dyula
stringlengths 10
487
| Wolof
stringlengths 10
390
|
|---|---|---|
1.242106
|
64 Nga dɔw be aw cɛma minw te lara ne la."
|
64 Waaye am na ci seen biir ñu ko gëmul."
|
1.240078
|
22 Aw mana fèn o fèn ɲini Ala delili la ni dannaya ye, aw na o sòrò."
|
22 Te lépp lu ngeen laaj cig ñaan, bu ngeen ci boolee ngëm, dingeen ci jot."
|
1.238092
|
16A ma sɔn tugu mɔgɔ si ka tɛmɛ Alabatosoba luu kɔnɔ ni feerefɛn ye.
|
te mayul kenn, mu yóbbu am njaay ci kër Yàlla gi.
|
1.23767
|
12Aw ben'a lɔn taamasiɲɛ min fɛ, o filɛ: Aw bena denɲɛnin dɔ lanin ye kolokolo dɔ kɔnɔ, fani melekenin b'a la."
|
12 Ci firnde jii ngeen koy xàmmee: dingeen gis liir bu ñu laxas ci ay laytaay, tëral ko ci lekkukaayu jur."
|
1.235031
|
48 Aw ye o kow seerew ye.
|
48 Yéenay samay seede.
|
1.23139
|
U t'a fɛ ka Ala sago kɛ.
|
Bëgguñu def li Yàlla bëgg.
|
1.231379
|
5U bena na o bɛɛ ɲafɔ Ala ye, ale min labɛnnin lo ka suuw ni ɲanamanw bɛɛ kiti.
|
5 waaye dinañu mas a teew fa kanam Ki nar a àtte ñiy dund ak ñi dee.
|
1.230469
|
1Mɔgɔ kelen kelen bɛɛ k'a yɛrɛ majigi faamaw kɔrɔ olu minw b'an kunna, bari fangatigiya bɔra Ala fɛ, faama minw siginin be yen, Ala le ye olu bɛɛ sigi.
|
1 Gannaaw loolu na nit ku nekk déggal ñi yore baat ci kanamam; ndaxte amul njiit lu fi Yàlla sampul.
|
1.230335
|
[Bible: Jenɛse 1.1] Ala ye fɛn bɛɛ da.
|
Yàllaa sàkk bépp mbindeef.
|
1.228641
|
14Yezu ye faliden dɔ sɔrɔ ka yɛlɛ o kan i ko a fɔra Ala ka kuma na cogo min na ko:
|
14 Yeesu wut cumbur, war ko; ndaxte Mbind mi nee na:
|
1.226381
|
Tiɲɛn Ala lo ye fɛɛn bɛɛ Danbaga ye.
|
Yàlla dëgg ji moo sàkk lépp.
|
1.224119
|
11Ni jinatɔw y'a ye tuma o tuma, u tun b'u kunbiri gwan a kɔrɔ ka pɛrɛn ko: "I ye Ala Dencɛ ye."
|
11 Fekk booba képp ku rab jàpp ku ko gis, daanu fa kanamam di yuuxu naan: "Yaa di Doomu Yàlla."
|
1.222728
|
31Ayiwa, aw be dumuni kɛra wo, aw be minni kɛra wo, aw be fɛɛn o fɛɛn kɛ, aw k'o bɛɛ kɛ ka boɲa la Ala kan.
|
31 Kon su ngeen di lekk walla ngeen di naan, walla lu ngeen mana def, defleen lépp ngir màggal Yàlla.
|
1.222627
|
18Min ye tɔɔrɔ nunu la aw kan,
|
6 Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.
|
1.222579
|
37 N'o y'a sɔrɔ ni ne te n Faa ka kɛwaliw kɛ, aw kana la ne la.
|
Su ma deful sama jëfi Baay, buleen ma gëm;
|
1.222299
|
LUKA 8:2 _ ani muso damani fana, Yezu tun ye jina gwɛn ka bɔ minw dɔw la, ka dɔw kɛnɛya: Magidalaka Mariyamu, Yezu tun ye jina wolonwula gwɛn ka bɔ min la,
|
8:2 ak ay jigéen yu mu teqale woon ak rab te jële leen ci seeni wopp, ñu di: Maryaama, mi ñuy wooye Maryaamam Magdala, mi Yeesu tàggale woon ak juróom-ñaari rab;
|
1.222081
|
34Olu y'a fɔ mɔgɔ fila nunu ye ko Matigi kununna tiɲɛ na, u ko a y'a yɛrɛ yira Simɔn na.
|
34 Ñooñu ne leen: "Dëgg la, Boroom bi dekki na, te feeñu na Simoŋ!"
|
1.220677
|
23 Ayiwa ni mɔgɔ min ma sigiya ne ta ko ra, o tigi jigimafara."
|
23 Yaw mi sa ngëm yolomul ndax man, barkeel nga."
|
1.220329
|
19k'a ka sebagaya kabakoman fana lɔn an faan fɛ, an minw lara Yezu la.
|
1:19 Ngeen xam it, ni kàttanam màgge ba jéggi dayo, jëm ci nun ñi gëm, dëppook dooleem ju ràññiku,
|
1.220275
|
24O kɔrɔ ko a ye an minw wele, a ma weleli kɛ ka bɔ zuwifuw dama cɛma, nga a ye dɔw fana wele ka bɔ siya wɛrɛw cɛma.
|
24 Wax ji noo ko moom, nun ñi Yàlla woo ci boppam ci biir Yawut yi ak ci biir xeet yi ci des.
|
1.220263
|
24Nga an fana niin b'o la, Ala bena an minw jati mɔgɔtilenninw ye bari an lara Ala la ale min y'an Matigi Yezu kunun a sanin kɔ.
|
24 Nun itam ci wax jooju lanu bokk, te Yàlla dina nu jagleel njub, nun ñi gëm Yàlla, mi dekkal Yeesu sunu Boroom.
|
1.220081
|
18 U si ma kòsegin ka Ala bonya, nin dunankè kelen kò wa?"
|
17:18 Amul kenn ci ñoom ku ñëw gërëm Yàlla ku dul doxandéem bii!"
|
1.218709
|
12Nii Senuman bena aw ka fɔta don aw daa la o yɔrɔnin bɛɛ."
|
ndaxte Xel mu Sell mi dina leen xamal ca waxtu woowa li ngeen war a wax."
|
1.218314
|
19 I kana seereya jugu minè egilisi cèkòròba kama, fò ni seere fila wala saba sòròla o ko la.
|
19 Kuy tuumaal njiit fi yaw, bu ko gëm, li feek ñaar walla ñetti seede dëggaluñu ko.
|
1.217897
|
9A ma danfara kɛ an zuwifuw ni olu cɛ, bari u lara a la minkɛ, a y'u dusu saniya o lanaya lo kosɔn.
|
15:9 Gënalantewu nu ak ñoom, ci li mu sellal seen xol ci kaw ngëm.
|
1.217868
|
N facɛ be sii la halibi wa?"
|
Mbaa sama baay a ngi dund?"
|
1.216798
|
4O seere nunu ye olivuyiri fila ye, ani fitinɛ fila, minw be dugukolo masacɛ ɲafɛ.
|
4 Ñaari seede yi ñoo di ñaari garabi oliw a yeek ñaari tegukaayi làmp, yi taxaw ci kanam Boroom suuf si.
|
1.216734
|
Furucɛw ka kan k'u ka musow kanu i n'a fɔ u yɛrɛ farisogo. - Efɛzikaw 5:25-29.
|
Jëkkër yi dañu war a bëgg seen jabar ni ñu bëgge seen bopp. - Efes 5:25-29.
|
1.21542
|
Ayiwa, ni anw fòlò ka kiri bè tigè, Ala ka Kibaru Duman kan minèbaliw laban na kè di? 18 I ko Kitabu b'a fò ko: "Ni mògò tilennenw kisili ka gèlèn, Ala ɲèsiranbaliw ni jurumukèlaw ta na kè di?" 19 O de kosòn, minnu bè tòòrò ka kèɲè ni Ala sago ye, olu ka u niw kalifa Dabaa Ala kantigi ma, ka to ko ɲuman kèli la.
|
18 Te:"Su muccu ki jub jafee,luy doon muju ki weddi te dëng?"
|
1.215208
|
Fɛnɲuman be se ka bɔ Nazarɛti wa?"
|
Ndax dara lu baax man na jóge Nasaret?"
|
1.214142
|
E b'a kɛra jama nin benna galon la.
|
Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.
|
1.213863
|
8min kɛra Nii Senuman ka baara ye, ale ka nɔɔrɔ man kan ka boɲa wa?
|
rawatina nag ne, jëfu Xelum Yàlla dina gën a ànd ak ndam.
|
1.212749
|
34Ne y'o ye, o la ne ko ale lo ye Ala Deen ye."
|
34 Yaxya teg ca ne: "Gis naa loolu te seede naa ne moom moo di Doomu Yàlla ji."
|
1.212603
|
28 bari nin ye ne joli ye, joli min be Ala ka layidu dafa, joli min bena bɔn mɔgɔ bɛɛ ka hakɛw yafa kosɔn.
|
26:28 ndaxte lii sama deret la, ji fas kóllëre gi, te mu tuuru, ngir ñu bare jot mbaalug bàkkaar yi.
|
1.212474
|
U bɛɛ kɛra i ko Sodɔmukaw, ne fɛ.
|
Ñoom ñépp di ma niru waa Sodom,
|
1.212242
|
3 Ne b'a fò aw ye ko ayi dèrè, nka ni aw ma nimisa aw ka jurumuw la, aw bèè na halaki ten.
|
3 Maa leen ne déedéet kay, te su ngeen tuubul, noonu ngeen di sànkoo yeen ñépp.
|
1.210954
|
Tile 40 ani suu 40, jii tun be bɔnna ka bɔ sanfɛ.
|
Taw na 40 bëccëg ak 40 guddi.
|
1.210643
|
"Adamaden min sara, o be se ka kunun tugu wa?
|
Ndax nit ku dee dina mën a dundaat ?
|
1.209256
|
56 A balimamusow bèè tè sigi an cèma yan wa?
|
56 Te ay rakkam yu jigéen, ndax nekkuñu fi ak nun?
|
1.208671
|
5Ala y'a lɔn ko ni aw y'o yiri nin deen dumu loon min na, aw ɲaa bena yɛlɛ, aw bena kɛ i n'a fɔ ale, ka koɲuman ni kojugu lɔn."
|
5 Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon."
|
1.208063
|
19Anw kɔni, kanuya b'an na, bari Ala le kɔnna k'an kanu.
|
19 Danuy wéy ci mbëggeel, ndax moo nu jëkka bëgg.
|
1.207466
|
32Bari Ala ye mɔgɔ bɛɛ to u ka murutili la, janko a ka se ka makari u bɛɛ la.
|
32 Yàlla moo tëj nit ñépp ci seenug déggadi, ngir yërëm leen ñoom ñépp.
|
1.207373
|
50bari mɔgɔ min be ne Faa Ala sago kɛ, o tigi le ye ne dɔgɔcɛ, walima ne dɔgɔmuso, ani ne bamuso ye."
|
ndaxte kuy def coobareg Yàlla, kooku mooy sama rakk ak sama jigéen ak sama ndey."
|
1.205026
|
4O seere nunu ye olivuyiri fila ye, ani fitinɛ fila, minw be dugukolo masacɛ ɲafɛ.
|
4 Ñaari seede ya nag ñoo di ñaari garabu oliw yeek ñaari tegukaayu làmp, yi taxaw ci kanam Boroom suuf si.
|
1.204755
|
An lanin b'a la ko nin le ye diɲɛ kisibaga yɛrɛ yɛrɛ ye." 43 Tile fila tɛmɛnin kɔ, Yezu bɔra o yɔrɔ la ka taga Galile mara la.
|
Bi Yeesu amee ñaari fan ca dëkk ba, mu jóge fa, jëm diiwaanu Galile,
|
1.204027
|
16Yezu y'u jaabi ko: "Ne be mɔgɔw kalan koo minw na, u ma bɔ ne fɛ, u bɔra ne cibaga le fɛ.
|
16 Yeesu daldi leen wax ne: "Li may jàngle, jógewul ci man, waaye ci ki ma yónni la jóge.
|
1.200771
|
17"Ala tun y'a daa di Ibrayima ma min na, o kɛtuma surunyana minkɛ, an ka mɔgɔw cayara kosɔbɛ Ezipiti jamana kɔnɔ.
|
7:17 "Bi loolu wéyee jamono ji jege woon na, ngir Yàlla amal li mu digoon Ibraayma ci ngiñ; fekk xeet wa di law tey gën a bare ci Misra,
|
1.200439
|
34Olu y'a fɔ mɔgɔ fila nunu ye ko Matigi kununna tiɲɛ na, u ko a y'a yɛrɛ yira Simɔn na.
|
24:34 Ñooñu ne leen: "Dëgg la, Boroom bi dekki na, te feeñu na Simoŋ!"
|
1.200134
|
Jaa nin kan cɛɛ fila juman lo lɔnin lo ni Musa ye?
|
Ñaari góor ñi nekk ak Musaa, ñan lañu?
|
1.199963
|
34 Ne y'a ye ka seereya kè ko, nin ye Ala Denkè de ye."
|
34 Yaxya teg ca ne: "Gis naa loolu te seede naa ne moom moo di Doomu Yàlla ji."
|
1.199274
|
13 O le bɛna kɛ sababu ye ka aw kɛ ne seerew ye ka ne ta ko fɔ o mɔgɔw nya na.
|
13 Loolu dina leen ubbil bunt, ba ngeen man maa seedeel.
|
1.199219
|
Bari, u ɲaa be minw yera,
|
waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.
|
1.199141
|
24 Aw welebaa ye kantigi ye, ale de na o kè fana.
|
24 Yàlla, mi leen woo ci loolu, kuy sàmm kóllëre la, te dina ko def.
|
1.198658
|
I b'a lɔn fɛɛn min kama wa?
|
Ndax xam nga lu tax ?
|
1.198259
|
16Yezu y'u jaabi ko: "Ne be mɔgɔw kalan koo minw na, u ma bɔ ne fɛ, u bɔra ne cibaga le fɛ.
|
7:16 Yeesu daldi leen tontu ne: "Li may jàngale, jógewul ci man, waaye ci ki ma yónni la jóge.
|
1.198145
|
4 O seere nunu ye olivuyiri fila ye, ani fitinɛ fila, minw be dugukolo masacɛ ɲafɛ.
|
11:4 Ñaari seede ya nag ñoo di ñaari garabu oliw yeek ñaari làmpu diwlin, yi taxaw ci kanam Boroom suuf si.
|
1.198026
|
27 Sabu min fɔra Ala ta Kuma ra ko Ala ko: "A flɛ, ne bɛ ne ta ciraden ci ka taga i nya fɛ ka i ta sira labɛn i ye," o ciraden ye Yuhana le ye.
|
7:27 Yaxya male moo di ki ñu waxoon ci Mbind mi naan:"Maa ngi yónni sama ndaw, mu jiitu la,te xàllal la yoon ci sa kanam."
|
1.197851
|
1 Tiɲè la, wajibi tè ko ne ka sèbèn ci aw ma Ala ka mògò senumaw dèmèni ko la, 2 k'a masòrò ne bè aw sago dòn ka ban.
|
Ci mbirum ndimbal loolu jëm ci gaayi Yàlla yi, matul ma leen di bindaat,
|
1.19773
|
17- U te hɛrɛ sira lɔn.
|
17 Xamuñu yoonu jàmm,
|
1.197161
|
12Nii Senuman bena aw ka fɔta don aw daa la o yɔrɔnin bɛɛ."
|
12:12 ndaxte Xel mu Sell mi dina leen xamal ca waxtu woowa li ngeen war a wax."
|
1.196978
|
KƐWALIW 11:3 _ ko: "I tagara don kɛnɛkɛnɛbaliw ka soo, fɔɔ ka dumuni kɛ n'u ye."
|
"lu tax nga dem ca këru ñu xarafal, bay lekk sax ak ñoom?"
|
1.196059
|
8I yɛrɛ b'i facɛ n'a ka mɔgɔw lɔn.
|
8 Xam nga sa baay ak ay nitam.
|
1.195625
|
28I b'a fɛ ka ne faga i n'a fɔ i ye Ezipitika nin faga cogo min na kunu wa?›
|
28 Ndax danga maa bëgga rey, ni nga defoon démb waayi Misra ja?"
|
1.195456
|
K'an to aw cɛma n'an be Ala ka kibaru diman fɔ aw ye, an ye baara kɛ suu fara tile kan waasa an ka doni kana la aw dɔ kan.
|
9 Bokk yi, yéena ngi fàttaliku sunu coono ak sunu ñaq; xam ngeen ni nu liggéeye guddi ak bëccëg, ngir baña diis ci seen kaw, ci di leen yégal xibaaru Yàlla.
|
1.195419
|
Jɔn lo murutira ka Musa ni Arɔn ka kuntigiya kɛlɛ, ani u ye mun lo fɔ Musa ye?
|
Ñan ñooy xeex kiliftéefu Musaa ak Aaroona, te lan lañuy wax Musaa ak Aaroona ?
|
1.195172
|
36 Aw ka kè makarikèlaw ye i ko aw Fa ye makarikèla ye cogo min na.
|
36 Nangeen am yërmande, ni seen Baay ame yërmande.
|
1.194782
|
64 Nga dɔw be aw cɛma minw te lara ne la."
|
6:64 Waaye am na ci seen biir ñu ko gëmul."
|
1.194701
|
12Aw ben'a lɔn taamasiɲɛ min fɛ, o filɛ: Aw bena denɲɛnin dɔ lanin ye kolokolo dɔ kɔnɔ, fani melekenin b'a la."
|
2:12 Ci firnde jii ngeen koy xàmmee: dingeen gis liir bu ñu laxas ci ay laytaay, tëral ko ci lekkukaayu jur."
|
1.194612
|
8A bena na ni tasuma ye, ka mɔgɔw ɲaa gwan minw ma Ala lɔn ani minw ma sɔn an Matigi Yezu ka kibaru diman ma.
|
1:8 safara su yànj wër ko, mu feeñ ngir mbugal ñi xamul Yàlla te bañ a déggal xebaar bu baaxu sunu Boroom Yeesu.
|
1.194586
|
Dɔw b'a fɔ ko n'i kɛra mɔgɔ ɲuman ye, i bena taga sankolo la.
|
Am na ñuy wax ne booy def lu baax ci sa dund, dinga dem ci kaw asamaan.
|
1.19425
|
ZAKI 1:18 _ A diyara Ala ye, a y'an dan a ka tiɲɛkuma barika la, waasa an ka kɛ a ka danfɛnw bɛɛ ɲamɔgɔw ye.
|
18 Ci coobareem la nu sole kàddug dëgg gi, ba nu judduwaat, di tànneefu lépp lu mu bind.
|
1.193763
|
Ala b'a fɛ i ka ɲɛnamaya kɛ kudayi alijɛnɛ kɔnɔ dugukolo kan.
|
Yàlla dafa bëgg nga dund ba fàww ci àjjana ci kow suuf.
|
1.193619
|
18Kira cɛkɔrɔba nin y'a fɔ a ye ko: "Ne fana ye kira ye i n'a fɔ ele.
|
18 Mu dellu ne ko: "Man itam yonent laa ni yaw.
|
1.1934
|
9Yala a bena barika la o baaraden ye bari a y'a ka baara kɛta kɛ wa?
|
9 Li surga ba topp ndigal, ndax tax na mu yelloo ngërëm?
|
1.192881
|
Sitanɛ ye Hadama ni Hawa su ka jurumu kɛ.
|
Waaye Seytaane tax na ba Aadama ak Awa bàkkaar.
|
1.192808
|
Mɔgɔ si ten'a kaan mɛn siraw kan.
|
te kenn du dégg baatam ci mbedd yi.
|
1.191814
|
FILIPIKAW 1:10 _ waasa aw ka se ka koɲuman lɔn, ka kɛ mɔgɔɲuman jalakibaliw ye Krista kɔsegilon na,
|
1:10 nangeen sax noonu ci yi gën a rafet, ngeen am xol bu laab te bañ a am benn sikk, ba bésu Kirist ñëw;
|
1.191707
|
30k'a fɔ ko: ‹Cɛɛ nin ye soo lɔli daminɛ, nga a ma se k'a laban.›
|
"Waa jii dafa tàmbalee tabax, waaye mënu koo àggale."
|
1.191347
|
2O la, u ye Musa kɛlɛ, u ko: "Jii d'an ma, an b'a min."
|
2 Ñu jote faak Musaa, naan ko: "Joxleen nu nag ndox mu nu naan!"
|
1.190732
|
32Bari Ala ye mɔgɔ bɛɛ to u ka murutili la, janko a ka se ka makari u bɛɛ la.
|
32 Kon Yàlla tëj na ñépp ci ngëmadi, ngir mana yërëm ñépp.
|
1.190605
|
24Ala min y'aw wele, ale ye kantigi ye, ale lo bena o kɛ.
|
24 Ki leen woo de ku wóor la, te moo koy def it.
|
1.190316
|
ƆRƆMUKAW 11:21 _ Bari ni Ala ma se ka makari yiribolo kɔrɔman nunu na, aw ta tena kɛ ten fana wa?
|
11:21 Gannaaw Yàlla baalul car ya cosaanoo ca garab ga, kon boog yéen itam man na leen a fàq.
|
1.19021
|
27Adamadenw be sa siɲɛ kelenpe cogo min na, Ala be sɔrɔ k'u kiti,
|
Kon ni nit ñi deeye benn yoon rekk, ba noppi jaar ca àtte ba, ni ko Yàlla dogale,
|
1.189997
|
LUKA 1:37 _ Ala te dɛsɛ foyi la."
|
1:37 Ndaxte dara tëwul Yàlla."
|
1.189936
|
Bɛɛ jugu bena kɛ a yɛrɛ ka somɔgɔw le ye.
|
nooni nit ki di waa këram.
|
1.189935
|
Nuhun tun ye mɔgɔtilennin ye, a jalakibali tun lo a ka waati mɔgɔw cɛma.
|
Nóoyin nit ku jub la woon, di ku mat ci biir nit ñi mu bokkal jamono, te di ku topp Yàlla.
|
1.189881
|
46"Mun na aw be ne wele Matigi, Matigi, k'a sɔrɔ ne be min fɔ aw ye, aw t'o kɛ?
|
"Lu tax ngeen may wooye "Boroom bi, Boroom bi," te dungeen def li may wax?
|
1.189542
|
Kalo duuru tɛmɛnin kɔ, kurun kɛra di?
|
Lu xewoon ak gaal gi bi juróomi weer paasee ?
|
1.189421
|
37N'o y'a sɔrɔ ni ne te n Faa ka kɛwaliw kɛ, aw kana la ne la.
|
Su ma deful sama jëfi Baay, buleen ma gëm;
|
1.18941
|
5Ne ka soo te ten Ala ɲakɔrɔ wa?
|
5 Du nii la sama waa kër def ak Yàlla?
|
1.188774
|
Mun na aw b'a lamèn?"
|
Lu tax ngeen koy déglu?"
|
1.188614
|
2U bena aw gwɛn ka bɔ kalansow kɔnɔ, waati dɔ bena se, mɔgɔ minw bena aw faga, olu bena miiri k'u ye Ala sago le kɛ.
|
2 Dinañu leen dàq ca jàngu ya, te dinañu dem ba jamono joo xam ne ñi leen di rey dañuy xalaat ne ñu ngi màggal turu Yàlla.
|
1.188501
|
FILIPIKAW 1:10 _ waasa aw ka se ka koɲuman lɔn, ka kɛ mɔgɔɲuman jalakibaliw ye Krista kɔsegilon na,
|
nangeen sax noonu ci yi gën a rafet, ngeen am xol bu laab te bañ a am benn sikk, ba bésu Kirist ñëw;
|
1.188471
|
34 Yesu ye u jaabi ko: "Tiɲè tiɲè la ne b'a fò aw ye ko: Mògò o mògò bè jurumu kè, o ye jurumu ka jòn de ye.
|
8:34 Yeesu ne leen: "Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, képp kuy bàkkaar, jaamu bàkkaar la.
|
1.188357
|
31Isirayɛlidenw, tun be cogo ɲinina waasa Ala k'u jati mɔgɔtilenninw ye sariya barika la, nga u ma o sɔrɔ.
|
31 Waaye bànni Israyil, mi bëggoona sàmm yoon ngir jub, matalu ko.
|
1.18817
|
O tε kεwalew nɔ ye, walisa mɔgɔ si kana a yεrε bonya ."
|
du peyu jëf, ngir kenn du ci kañu.
|
1.187708
|
4 An bè nin kow sèbèn ka ci aw ma walisa an ka ɲagali ka dafa.
|
4 Nu ngi leen di bind yëf yii, ngir sunu mbég mat sëkk, nun ñépp.
|
1.187476
|
25 Musa tun bè miiri ko a balimaw n'a faamu ko Ala na u tila ale bolo, nka u m'a faamu.
|
25 Mu defe ne, ay bokkam dinañu xam ne ciy loxoom la leen Yàllay musale, waaye xamuñu ko.
|
1.187236
|
aw kana nisɔndiya i ko siya tɔw.
|
buleen bànneexu ni yeneen xeet yi,
|
1.187166
|
10A y'a fɔ ne ye tugu ko: "Kana kitabu nin kɔnɔna kuma kɛ gundoko ye dɛ, bari a koow kɛtuma surunyana ka ban.
|
Mu ne ma it: "Bul tëj téere bii ak waxi Yàlla yi mu ëmb, ndaxte waxtu wi jege na.
|
Dyula-Wolof_Sentence-Pairs Dataset
This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.
This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1
Metadata
- File Name: Dyula-Wolof_Sentence-Pairs
- Number of Rows: 33194
- Number of Columns: 3
- Columns: score, Dyula, Wolof
Dataset Description
The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:
score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).Dyula: The first sentence in the pair (language 1).Wolof: The second sentence in the pair (language 2).
This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.
References
Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:
[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017
[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.
[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018
[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.
[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.
[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.
[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.
[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB
[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.
[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages
- Downloads last month
- 7