Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
score
float32
1.04
1.24
Bemba
stringlengths
10
472
Wolof
stringlengths
10
387
1.244601
Na bulwazi buli atala nanka mukati, ncintu comwe.
waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.
1.242064
"Mpoonya wakabapampanwida kuti bamvwisye, akuti bateelelesye Mangwalo.
noonu mu ubbi seen xel, ngir ñu xam li mbind mi di wax.
1.239744
Mubaghile ukuyoba kubangi aba baghenepo nindamyo iyakufwana ni yinu
6 Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.
1.236069
"Engefyo calembwa aciti Takuli uwalungama nangu umo" (Abena Roma 3:10-12).
Moom la Mbind mi wax ne:"Ku jub amul, du kenn sax.
1.232821
Kuli iwe kukabo kusekelela no kwanga; na bengi bakasekelelo kufyalwa kwakwe.'"
Sa mbég lay doon, sa xol sedd ci, te ñu bare dinañu bég ci juddoom,
1.229005
5Pantu Lesa alishiba ukuti ilyo mukalyako, amenso yenu yakesuka elyo mukaba nga Lesa, mukeshiba ifisuma ne fibi."
5 Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon."
1.223983
Umwana wobe afwa.'
Sa doom faatu na. '
1.223175
Elyo kasebanya asha wene, kabili, moneni, bamalaika baishile no kubomba kuli wene " .
noonu seytaane bàyyi ko. te ay malaaka daldi ñëw fi yeesu, di ko topptoo.
1.223113
TALA uno nkasampe mwana-mulume wisamba na banunu.
XOOLAL xale bi di waxtaan fii ak mag ñi.
1.222165
Muli Ndi Mafunso?
am nga ay laaj?
1.221818
Uyooba aakukondwa akusekelela, alubo banji bayoobotelwa akuzyalwa kwakwe.
Sa mbég lay doon, sa xol sedd ci, te ñu bare dinañu bég ci juddoom,
1.219806
Ici icitabo cikamwafwa.
Téere bii dina la ci dimbali.
1.214966
Abafyashi bakwe ali Alexander Arthur na Stella Arthur.
Am waajur nekk nañu Arthur Alexander ak Arthur Stella.
1.212781
Abana bakwe Noa bafyala abana abengi.
Doomu Nóoyin yi amoon nañu doom yu bare.
1.20888
Kebanena'mba: "Le uno'u ke ayepo Yesu mwanā Yosefa, otuyukile shandi ne inandi?" - Yoano 6:42.
42 Ñu naan: "Ndax kii du Yeesu, doomu Yuusufa?
1.203758
Kebanena'mba: "Le uno'u ke ayepo Yesu mwanā Yosefa, otuyukile shandi ne inandi?" - Yoano 6:42.
6:42 Ñu naan: "Ndax kii du Yeesu, doomu Yuusufa?
1.202845
Awe malaika wa kwa Yehova amoneke kuli ena mu ciloto no kumweba ati: "Witiina ukusenda umukashi obe Maria ku mobe, pantu ifumo emiite lifumine ku mupashi wa mushilo.
Malaaka Yàlla ne ko: ' Bul ragal a takk Maryaama, ndaxte Yàlla moo ko may doom bu góor. '
1.20206
Bushe bonse batumwa? bushe bonse ni bakasesema, bushe bonse ni bakasambilisha? bushe bonse ni bakabomba wa fisungusho?
ndax ñépp ay ndawi kirist lañu? ndax ñépp dañuy wax ci kàddug yàlla? ndax ñépp ay jàngale? ndax ñépp ay def kéemaan?
1.199188
2Lishiwi ali pamo na Lesa ukufumafye ku citendekelo.
2 Moo di ki nekkoon ak Yàlla ca njàlbéen ga.
1.197906
Ubufumu wandi ni pano.
Sama nguur nekk fii.
1.197686
Bamwikeulu babidi bādyumwine Lota namani?
Lan la ñaari malaaka yëgal Lóot ?
1.196916
Lelo wi Ediya?"
Ndax yaa di Ilyaas?"
1.19579
Mwanda waka bana ba bwanga abakwatwa moyo bufuku, ne i bika byafikila Petelo?
Lu tax taalibe yi tiit ci guddi gi, te lan moo dal Piyeer ?
1.195539
Cindo cacitikile ku bwato ili papitile imyensi isanu?
Lu xewoon ak gaal gi bi juróomi weer paasee ?
1.190704
Kebanena'mba: "Le uno'u ke ayepo Yesu mwanā Yosefa, otuyukile shandi ne inandi?" - Yoano 6:42.
Ñu naan: "Xanaa kii du doomu Yuusufa ji?"
1.190679
Na Mwanga wa Milele Umwangazie,
waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.
1.189677
Ubamone Atene pa kalata?
Ndax gis nga Aten ci kàrt bi ?
1.188413
Ino shi muntu unanga bufuku, ukukalanga, mwanda kitōkeji kekidipo mwadi."
Waaye kuy dox guddi, dina fakkastalu, ndaxte leer nekkul ci moom."
1.18692
Mwikeulu umo wa Leza wasapwila bakumbi amba: "Kemwakikwatwai moyo, mwanda talai! nemusapwila myanda miyampe ya nsangaji mikatampe ikekala na bantu bonso.
10 Waaye malaaka mi ne leen: "Buleen tiit, ndaxte dama leen di xamal xibaaru jàmm buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.
1.184171
- " Ifwe twalanga kuli imwe ilyashi lya nsansa (e mbila nsuma), ifyo icilayo cintu cacitilwe kuli bashifwe (ba bwina Yuda), Lesa afikilisha " (Imilimo 13:32,33).
13:32 te nu ngi leen di xamal xebaar bu baax ne leen, li Yàlla digoon sunuy maam,
1.184136
Ukufuma pali nomba namumwishiba no kumumona namumumona."
Lu weesu tey, xam ngeen ko te gis ngeen ko."
1.183972
2Lishiwi ali pamo na Lesa ukufumafye ku citendekelo.
1:2 Moo di ki nekkoon ak Yàlla ca njàlbéen ga.
1.180349
, Yeni Inka Sepine Wengi
Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.
1.17992
Mwene nobe usakanga kwikala na mulopwe wa uno muswelo?
Ndax bëgguloo am njiit bu mel noonu?
1.179621
17 Nanchi baana bakonsha kufunda kwi Yesu nyi?
17 Ndax am na li xale yi mën a jàng ci Yeesu?
1.179114
Pa kuti kasebanya naikila pali imwe, ali ne cipyu cickalamba, pa kwishibo kuti ali ne nshita inono fye." - Ukusokoloa 12:12.
Ndaxte Seytaane wàcc na ci yéen, ànd ak mer mu tàng, ndaxte xam na ne, jot gi ko dese barewul."
1.177733
I ani wāpangile mwana-mulume umbajinji, ne uno mwana-mulume dijina dyandi i ani?
Kan moo sàkk góor gu jëkk gi, te naka la tuddoon ?
1.176225
O mwanda mubamone ne kwivwana kino kingelengele.'
Loolu moo tax ngeen gis te dégg kéemaan yii. '
1.175993
Unenanga'mba: 'Lelo usakile kwenda na Shilasa ne ami?
Lii la koy laaj: ' Ndax dinga bëgg a ànd ak Silas ak man ?
1.175327
Mansa Talwandi Sabo Road Banawala,
Fu ñu jaar, foofa yàqu ak musiba.
1.175181
"Moneni nkalenga umulu upya ne calo icipya.
1 Ma daldi gis asamaan su bees ak suuf su bees.
1.174971
Taluka Amini
Waaye ci ñi gëmul, nag:
1.17463
E lyo Yuda, uo baleita abati Tadeo, aipwishe ati: "Mwe Shikulu, cinshi calenga ukuti mufwaye ukuilanga apabuuta kuli ifwe, no kukanailanga ku ba muli ici calo?"
22 Yudaa -du Yudaa Iskariyo de, beneen la woon- ne ko: "Boroom bi, lu xew, ba nga nar noo feeñu nun rekk, te doo feeñu àddina sépp?"
1.17447
13 Buno bukamoni i bwa bine.
13 Te li mu wax dëgg la.
1.174429
Nga kanshi nashuka shani ica kuti nyina wa kwa Shikulu ese kuli ine?
Man maay kan, ba ndeyu sama Boroom ñëw di ma seetsi?
1.174389
Cinshi ukwikalilila mu kutemwa kwa kwa Lesa kwacindamina?
Lu tax sax ci mbëggeelu Yàlla am solo lool ?
1.174379
Mwikeulu wa Leza waiya kushitula mulango wa ku kifungo bufuku, enka na momwenine pano'mu.
Ci guddi gi, malaakaa Yàlla ubbi na buntu kaso bi, ni nga ko gise fii.
1.174277
Mwanda waka tusakilwa ntanda mipya?
Lu tax ñu soxla àddina su bees ?
1.174209
Wishi alitemwa Umwana kabili napeela fyonse mu minwe yakwe.
Baay bi dafa bëgg Doom ji, te jox na ko sañ-sañ ci lépp.
1.173817
Eeci ncencico Bbaibbele ncolyaamba kuti: "Magwalo oonse akasololelwa a Leza."
Booba, mbindéefi yàlla yépp a doon waxante.
1.173685
Satana nawe waswike ati: 'Waya ni cuvwila pa mulandu wakuti mukamucingilila nupya aeci wakwata ivintu ivisuma ivingi sana.
Seytaane wax lii: ' Danga koy barkeel te bare na alal.
1.173052
13 Cila mwaka, icalo cilebipilako.
13 At mu nekk, àddina si dafay gën a bon.
1.172922
(Ntendekelo 1:28) Ntanda kechi ikonaika ne.
(Njàlbéen ga 1: 28) Suuf si du fi mas a jóge.
1.172051
Uzye ndinzile ukukuukila uku mpanga kuno ndakwata untungwa wa kupepa Leza?'
23 Xanaa du maay Yàlla?"
1.172011
Lelo, mu kuya kwa nshita, imfumu ishingi tashaleba ne cumfwila kuli Lesa kabili na batekwa abengi e fyo balecita.
6 Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.
1.17169
Findo tungasambililako ku fyacitikiile muka Loti?
Lan lañu mën a jàng ci li dal jabaru Lóot ?
1.171521
Bapolofita ni bona ba shwile.
Yonent yi itam faatu nañu.
1.171374
40 Penepo bene Samadia pa kwiya kwadi, kebamunena ashikate nabo; nandi washikata nabo
40 Ñu daldi dikk ñaan Yeesu, mu dal ak ñoom.
1.171208
Taufwile ukula-angala na balanda no kucita ifintu ifilenga cilemoneka kwati ukucita ifyabipa kusuma.
Bu sa njariñ jur wax ju ñaaw.
1.170479
Mpa mwanda wa'shi baadi mwikulupile su?
Lu tax ñu mën ko gëm ?
1.169926
Talemwa Nalugwa1,
waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.
1.169538
"Mu musumba umo mwali kapingula umo uushaletiina Lesa kabili uushalecindika abantu.
Dafa amoon cib dëkk, benn áttekat bu ragalul Yàlla te faalewul mbindeef.
1.16921
8Hanaho, Petelo kaluula mu Mpeeve Yangisi, waleele kuri bo ti: "Bamfumu ba kaanda na bakulu ba babakala,
4:8 Ci kaw loolu Piyeer daldi fees ak Xel mu Sell mi, ne leen: "Yéen kilifay xeet wi ak njiit yi,
1.168717
"Bushe tata teumo bonse twkwata?
10 Xanaa du benn baay lanu am, nun ñépp?
1.168604
3 Naashi tave shi mu ningile, osheshi inava shiiva Tate, vo kave shii nge.
3 Dinañu agsi foofu, ndaxte xamuñu Baay bi te xamuñu ma.
1.16856
Ifwe Natulanga ukuti umweo wa pee no kwalulwa ukuba mu musango wakwa Lesa fikapeelwa ku batetekela panuma ya bupingulo.
10 Danuy ñaq tey bëre, ndaxte wékk nanu sunu yaakaar ci Yàlla Aji Dund ji, di Musalkatu ñépp, rawatina nag ci ñi gëm.
1.168416
Asambi yakwe yayile umu muzi uku kukala ivyakulya.
Fekk booba nag, taalibey Yeesu ya dañoo demoon ca biir dëkk ba, di jënd lu ñu lekk.
1.167421
Ino mubasambakanya Yelusalema na lufundijo lwenu.'
Waaye feesal ngeen Yerusalem ak seen njàngale mi. '
1.167165
kwalile milomo ya litau.
Tëj na gémmiñu gaynde yi.
1.1671
Bushe Lesa Alikwata Ishina? _ AmaVidio
Ndax Yàlla am na tur?
1.1668
Ili bapalamina, alabila ati: 'Nine Josefi umukwabenu, ene mwasitisye ku calo ca Ijipiti.'
Mu ne leen: "Man maay Yuusufa, seen rakk, ji ngeen jaayoon, ñu indi ma Misra.
1.166566
Lipepo nshi ilyaishibikwa sana ilyo twalalandapo nomba?
Ban ñaan bu siiw lool lañuy gëstu léegi?
1.166468
14 Na bampofu na basha bilema babafikile kwadi mu tempelo, na bebapashishe.
14 Noonu ay gumba ak ay lafañ ñëw ci moom ca kër Yàlla ga, mu faj leen.
1.166234
Dafidi ali ne myaka ya kufyalwa 30 ili aba imfumu.
Daawuda amoon na 30 at bi ñu ko defee buur.
1.166103
Ilyo e funde lya kucila ubukulu, ilya kutanga.
Loolu moo di li jëkk te ëpp ci li Yàlla santaane.
1.166027
Yasushi Ishijima,
xeet yépp seede ko.
1.164901
6 Ici calicitike kuli Satana Kaseebanya.
6 Loolu moo dal Seytaane mi nekk Ibliis.
1.164415
Hena Kristu taakeelede kupenga zyintu zyoonse eezyi kuti akanjile mubulemu Bwakwe?"
Xanaa du Almasi bi dafa waroon a daj boobu coono te dugg ci ndamam?"
1.164304
Mi Yakenile wahae ukaba lulimi lwa mulilo;
ba dellooleen safara gañu jógé woon.
1.163927
Mulume i mutwe wa kisaka.
Jëkkër mooy kilifa njabootam.
1.163507
Kupwa watonge'mo bankasampe bana-balume bapopoke ne ba ñeni bininge.
Ginnaaw loolu, mu tànn ci seen biir xale yu góor yi gën a rafet te gën a am xel.
1.163426
4 Na su alwisha malwisha musambobidi kwifuku dimune, na su eyalula kodi mashisa musambobidi eshi, Nemwesha, obe onomulekyele.
4 Su la tooñoon juróom ñaari yoon ci bés bi, te walbatiku juróom ñaari yoon, ne la: "Tuub naa ko," baal ko rekk."
1.163422
4 Na masumbi gangi makumi abili na ane g'ikujo gaali galipindije i Lisumbi lya butemi lyenilo; a ha masumbi genayo baali bigashije ho Banamhala makumi abili na bane, bazwalile shizwalo shape na ngikili ja zahabu u ku mitwe yabo.
4 Yeneen ñaar fukki gàngune ak ñeent wër ko, te ci kaw gàngune ya ñaar fukki mag ak ñeent toog, sol mbubb yu weex ak kaalay wurus ci seen bopp.
1.16337
66Bushe imwe muletipo shani?"
66 Lu ngeen ci xalaat?"
1.163293
lombe, momwa mulu mulampe!"
ba mel ni Yàlla Aji Kawe ji!"
1.163191
Tapakalukulipo neli umo uwa kubatinisha."
te kenn du leen tiital."
1.162724
Na kabili balakabila ukubalungika no kubasalapula.
Soxla nañu yar ak jubbanti.
1.162716
Kuti inywe mwakumbila cintu cili coonse muzina Lyangu, Ime njoocicita.
Lu ngeen ñaan ci sama tur, maa koy def.
1.162063
L'ile Amini
Waaye ci ñi gëmul, nag:
1.161827
Ni kuli Lishiwi Lesa abumbile ifintu fyonse.
Yàlla dëgg ji moo sàkk lépp.
1.161521
6 Pilato pa kwivwana nabya, waipangula shi uno muntu i mwine Ngadilea.
6 Bi Pilaat yégee baat yooyu, mu laajte ne: "Ndax nit kii Galile la dëkk?"
1.161108
Tumeni Tumeni Mba Nindo BaLesa Balengele Icalo?
Ndax li Yàlla sàkk amoon na sikk?
1.160056
Iusya ukuti, apa myaka iili Paulo wali umu cifungo uku Kesaliya.
Yaa ngi fàttaliku ne Pool toog na kaso ñaari at ca Sesare.
1.159972
Lelo uyukile majina abo?
Ndax xam nga seen tur ?
1.159869
Kanshi te bonse abali mu muulu abalecita ukufwaya kwa kwa Lesa.
Kon nag booba, du ñépp ñi nekkoon asamaan ñoo doon def coobare Yàlla.
1.159192
Bushe abatumwa ba kwa Yesu cine cine balile umubili wakwe ulya wine fye no kunwa umulopa wakwe?
Ndax ci dëgg, taalibe Yeesu yi dañu lekk yaramu Yeesu te naan itam deretam?
1.15911
19 Le Bulopwe bwa Leza bukalonga bika kupityila ku Amakedona?
19 Lan la Nguuru Yàlla di def jaare ko ci xeexu Armagedon?
1.159086
Bane pali bo ni baba abasankwa wabona apa.
Yaa ngi gis fii ñeent ci ñoom.
1.159084
Ubwato bwandi bukalamba My big boat.
gaal gu mag.
1.159009
Ino pano usa kubutula mwana mwana-mulume.
Waaye léegi dina am doom bu góor.
End of preview. Expand in Data Studio

Bemba-Wolof_Sentence-Pairs Dataset

This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.

This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1

Metadata

  • File Name: Bemba-Wolof_Sentence-Pairs
  • Number of Rows: 39092
  • Number of Columns: 3
  • Columns: score, Bemba, Wolof

Dataset Description

The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:

  1. score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).
  2. Bemba: The first sentence in the pair (language 1).
  3. Wolof: The second sentence in the pair (language 2).

This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.

References

Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:

[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017

[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.

[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018

[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.

[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.

[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.

[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.

[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB

[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.

[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages

Downloads last month
7

Collection including michsethowusu/bemba-wolof_sentence-pairs